KHAM SAY FARATA

1.8K 45 3
                                    

KHAM SAY FARATA

Bismilahi Fasseyéné Liguéyal Khadimoul

THIANGAY

FARATAY THIANGAY (5)
1) Yééné (ci booy rakhass sakara)
2) Raggue (Rakhasouk yaramwi)
3) Gaaw (loo paré démci lénén )
4) xalil kawarou bopou
5) Nacc aye léét

SUNAY THIANGAY ( 4 )
1 raxass lokho basi tiki diara(si booy tambali )
2 galaxndikou
3 saraxndikou
4 massaa beune_beunou nopou

NDIAPOU

FARATAY NDIAPOU (8)
1 yééné (ci booy raxass sa kanam)
2 raxass kanam
3 raxass loxo ( tiki diara ba si thionthiou)
4 xalil baaramou lokho
5 massaa bopou (dém bi)
6 raxass tank basi doudiour yi
7 raggue (bombou gui)
8 gaaw

SUNAY NDIAPOU (8)
1 raxass lokho bassi tiki diara
2 galaxndikou
3 saraxndikou
4 fiirou
5 yééssal ndox booy massa nopou
6 déllo massaa bopou
7 massa niari noppou
8 toftalé faratayi

TIIM

FARATAY TIIM (8)
1 Yééné (daganelou litax ngay tiim)
2 pakke bou laape bingay tiimé
3 gaaw
4 daurine bou ndieuke (ték sa loxo si souffe)
5 massaa kanam
6 massaa loxo baci tiki diarra
7 Diokkalé  tiim gui ak li tax ngay tiim
8 défko ci tabbik waxtouwi

SUNAY TIIM (3)
1 toftalé faratayi
2 yééssal doorine booy massaa lokho
3 massaa tiki jarra bassi thionthiou

KOOR

FARATAY KOOR(2)
1 yééné
2 féggou ci louy dok koor

SUNAY KOOR (3)
1 gaawa dok
2 yéxa xeud
3 fék sa laamigne si wax lou niaaw

ASSAKA

FARATAY ASSAKA (4)
1 yééné
2 mat at
3 mat nissap
4 niaka toxole

Nissap : mbay= 6 barigo ; khar ou bey= 40 ; xaaliss=500 000F ;
joxél béne ci foukou you nék

TEGGUINI ASSAKA (3)
1 tééyouk bakane
2 joxé li digou daumou ci alal ji
3 sutural

JOULLI

FARATAY jOULLI (15 )
1 yééné booy kabbar
2 kabbar gou ndieuk
3 taxawayou kabbarbi
4 jangue fatiha
5 taxawayou jangue fatiha
6 roukoo (seugu diappou sisay woom)
7 sigguéé si roukon
8 soudioot (deup sap dieu si souf)
9 sigguéé si soudioot
10 yééné roy imam (bounela jitéé)
11 toftalé faratayi
12 dal (bo sigguéé ngani ték)
13 yamoo ( bo siggué nga joupe xothie)
14 seulmeul
15 jotayou salmeul

SUNAY jOULLI (18)
1 lixam
2 jangue saar ganaw fatiha
3 jotayou diangue saar ganaw fatiha
4 birel(wakh si kaw) fougnouko digléé
5 yallou (wakh si souf)fougnouko digléé
6 yénéén kabbar yi désse
7 taaya
8 jotayou taaya
9 salatoul alal nabi (guinaw taaya gou moudiou gui)
10 dolli dal gui (ci rouko ak soudiot
11 dolli dal si seulmeul
12 Biral seulmeul (wakh assaloumou haleykoum )
13Déllo sap seulmeul si imaam wala kénéén
14 Noppi  bou imaam di béral
15 Saatir (Lingay ték sisa kanam bo banié kou diar sisa kanam
16 Djiital faatiha
17 sami alahou liman hamida
18 jouroom yiy laal souf booy soudioot  (bakane,tinkhe,dieu,aume, baaramu tank)

AJJI MAKA

FARATAY AJJ (4)
1 yééné SUNAY ARMAL
2 weur kaaba bissup foukélba
3 dox safa ak marwa (6 fois)
4 taxaw arafat bissup jurom gnintél ba

SUNAY AJJ (12)
1 Sangou farata
2 tarax laayu
3 juli niaari raka(fatiha+xulyaa       ayuxal kafirona,fatiha+ixlas)
4 waw labayka allahouma labayka

SUNAY TAWAF
1 dox bagna waar dara
2 foone dojwa si guémigne
3 niuku goorya(niati yoone yu ndieukyi)
4 niane

SUNAY DOKH SAFAA AK MARWA
1 Foone dojba
2 yékci kaw safaa ak marwa
3 gnuku goorya
4 gnane ci kaw safaa ak marwa

Vous avez atteint le dernier des chapitres publiés.

⏰ Dernière mise à jour : Jan 10, 2019 ⏰

Ajoutez cette histoire à votre Bibliothèque pour être informé des nouveaux chapitres !

KHAM SAY FARATAOù les histoires vivent. Découvrez maintenant