_Certains ou certaines pensent ainsi:une femme doit être soumise,la femme parfaite et idéale... Pourquoi ?tel n'est pas le cas car tout amour est fragile et l'amour est au dessus de tout..Entre être ou ne pas être est un droit et un choix qui nous concerne...
_fatimah a choisi d'être soumise et dévouée envers son homme malgré le fait de savoir littéralement ce qui l'attend, c'est son choix.
Dans la peau de Fatimah
Bestah:salam coccinelleMoi:salam papillon,nam nala ni
Bestah : raw nala lu nexx, est ce que ça gaz
Moi :ouais ça boom
Bestah :meuf ça te dire de sortir today
Moi:meussoul guéne,tmtc que dougn ma bayi,té dougn bougé yota
Bestah :kon wéro,Hana tay Ibou nieuwoul?
Moi:Nanan dafa am répétition
Bestah :ok jvoi naka homri♥️
Moi:bae qu'est-ce qui te prends today comme une détective,il va bien Alhamdulilah.
Bestah : parle moi cérieusement,tu es vraiment amoureuse de cet idiot façon je l'aime pas moi il n'est pas pour toi.
Et il ne fais pas le poids devant IbouMoi: vraiment t'es bête, est-ce qu'une fois de ta vie tu m'as vu aussi amoureuse.tu es ma meilleure pote et tu sais que je le suis,je sais que tu ne l'apprécie pas mais fait un effort pour moi 🙏.
Bestah :bien d'acc en tout cas fait gaff..gars comme Badu je ne leur fait pas confiance,et comme ça que je te vois là tu es entrain de te donner à fond et ce gars là pfffff.
Moi:louma si gobé garko.j'ai beaucoup changé et c'est pour lui que je l'ai fais .au paravent palmarès la yorone,di dadialé comme pas possible on se know ndaxx nous étions dans le même panier bordel, bateau deim bateau costé.
Lolu amoul sens chérie.maintenant que j'ai rencontré le gars j'aime donc j'arrête toute sorte d'enfanterie,har nak dafay wéssou mboté,sou lolu wesso di mbeugël Man mom la beug.Bestah :aah tamit...lu nexx... écoute moi très bien tu n'es pas seulement ma bf mais une jumelle.ne te montre jamais soumise et encore moins être une faiblesse parce que les hommes d'aujourd'hui n'en valent pas la peine.liko diar moko diar...
Moi: c'est à la fois une pauvreté et une richesse suprême d'avoir encore l'innocence de l'enfant...
Nieup yamougn.et je prends compte de tes propos merci de ne pas me soutenirBestah :certe... hum, mais hélas !tu ne sais pas encore qu'aucun être ne peut tout donné, tout recevoir, dans une complémentarité que tu crois paradisiaque.
Moi : où veux tu en venir ?et l'adulte n'est pas beaucoup plus expérimenté quand il manque de spiritualité ?
J'ai une tendresse particuliere pour les blessés de l'amour.Babexx ak nakar nio and té niar yoyu nio and ak mbeugëlBestah :mbékté ak métit siii....je sais mais bvb Man jveu que tu vives dans le bonheur,thi banexx la beug na deuk ndaxx ioe dana baxx, beugouma Loula méti.
Moi:viens là je vais pleurer je t'aime tellement.mais tkt ça ira sa yéné rafeit neu mais soit un peu réaliste parce que bonheur et malheur vont ensemble.jummy dég loul ma dioxx leu béne ndenkane:
{Djiguéne sou beugué don dieugeune faw mouy nangou,di dékou teik si oyof...té nango mougn...
Kocc barma dan na waxx li si djiguéne bou namé diour wilaya...:biss thi bir biss yi nieuwna,Man kocc barma guéweul national ak international yagg deim xéw téy ma xéwlé ma ayé,sama dom lay mayé dina bétt niou Bari.
Kocc nieuw togg si dig gueiw gui nieuw nouyo dal di nopi,soumi mbahana bi
Nieup diaxlé,nit gni nékoo waa kocc tay waxo Hana dagua tit?sa dom gui yaroko té dou séy Kat.
Kocc né teik hol domam si ay beut rék dom dji dieul kadou gui
Dom dji:sama pape wax na lepp bimou nieuwé nouyo tok si souf,lolou moy firi ni nit dafay mandou rawatina djiguéne,bimou soumé mbahana bi teik si souf sama Baye diangual na ma ni djiguéne dagua wara oyof ni mbahana.kouthi nekk di way mouy déglou mouni djiguéne day nango mougn ni souf,ndaxx souf louné niou teik ko si kawam wanté bou meindjé nieup contane li rék leu...
Té yakar na nit Soko beugué,deugou diexx tak si mom,fouleu rék taxla diokk,aah lo deif si mom dou doy..té sah nak niar niou beugeunté,yakar seuy euleuk, bou si War amoul béne yone niou diour ay wilaya.Badu donoul sama far rék,borom keur la kay xolé té borom keur dou morom...li la nam sama digeunté ak mom té li la lay deink ioe xarit♥️😭...Bestah :tu as parfaitement raison.wanté yaw kou modé gua, Fatimah ya héwi ya perte...ioe dh yama bét..kon affaire de femmes soumises yi guamay tégal .. depuis quand t'es devenue une analphabète ? espèce de tardé ! ignorante que tu es !les temps ont changé et je ne vais pas te laisser bb tu vaux mieux que ça...
Révolution dafa am té deal bi dafa changé..beug indo yi mofi diexx,danay ganiou déh.. baxna rék.Moi: être soumise n'a rien avoir avec niveau intellectuel,je te rappelle que yalla bindoul féne ni djiguéne moy yilif goor,wanté beug taxoul kéne niak fouleu donté djiguéne day niak diom, loudoul wéy diaroul tambali am dét?
Bestah :waa li néxul??? fatimah ya perte nako waxx sama yaye niou télla diog si ioe...sou néké Badu dafa hoyal dioxx la na nane hamalni Man di laxx dioh la na leik... weeuu diomi na je te reconnais pas déh tu as toujours joué avec les sentiments des gens là tu me dis que t'es amoureuse j'accuse,anh légui u veux devenir sa chienne de guerre héy doufi amé..
Breff j'étouffe puisqu'on a rien à faire pour ce soir haral ma woo Thiam teranga mou livrél niou Pizza.Moi:😂😂néké fi ni reik...oui ça peut se faire ! prochaine fois niou deim pointe ba..
Bestah :li la beug té mom la xam si ioe tamit...aah pourquoi soumise tamit ?
Moi: hahaha souma la tonto rék mou nexx té dotoul safé bayima ni rék.
Bestah :wa zikaral ma
Moi: Bossi beug
Bestah :nurul bassar
Moi:ya fouy deug
Bestah :waaa meunoko diougué fi...
😂😂😂😂😂.Nouyou na nieup et dsl pour ce court chapitre...mais rester là à me soutenir car il m'est difficile de continuer l'histoire mais je le fais pour vous.
Besoin de vos encourager..
Soumission, dévotion Part2 pour le prochain chapitre du lourd promis ♥️
Je vous love....Votez,likez,partagez....en bombe nak

VOUS LISEZ
Fatimah♥️femme soumise!
Fiksi UmumCet homme l'a anneanti,elle a renoncé à l'amour ♥️ Mais un jour un ange est venu sur terre pour lui montrer que toi=moi😍