-
Wakhi Mame Cheikh Ibrahama fall
Ay kadu fatali ak ndékané sounou Mame cheikh Ibrahima Fall louci ndeungue niogui koy toub té hamni matadi Domou adama la wayé lepp louci bah niou santé ko serigne bi ndah lou bah rkk lagnthi dioublou Yalla naniou serigne bi defal dégg ak topou niou sah thi diko liguéyeul ba heuy sango souf
-
Serigne Touba Néna
SERIGNE TOUBA NÉNA boy woute kharite na gua mouytou kou amoul khel kou iniane wala kou toppou bakaname
-
Waxi Serigne Touba
Ce recueil est constitué de récits et de propos authentiques tenus de Cheikh Ahmadou Bamba. Certains de ces propos furent extraits de ses propres écrits ou rapportés par ses fils ou par des témoins contemporains du Cheikh. D'autres récits furent relatés par des personnes qui, bien que n'ayant pas vécu avec le Cheikh...