couzyta
- Reads 9,954
- Votes 295
- Parts 8
Seyyy moy dem badiexx liley guene sa keur djeukeur moy gue gueneu aduna
Seuyyi moy gue dem yendou niowat manam dofa yafa yagg dofa yakk
Kunek thi yeneu amna droit choice Ben daxx Lila taxa dougou thi seyy bi wala seuyyy bi yako xameu