Guéweul mbaye :Pourchassée Par Les Fantômes Du Passé( Karma)
tarouya
- Reads 82,166
- Votes 6,803
- Parts 46
Amour sanguinaire et interdit
****************************
Drame ,tragédie ,karma, amour
_Jiguéne bou raféte té tarou.
*Goor gou âme dîné, sél ,tékssi téye.
_féne , foo ak khalisse la défone adouname.
*diamou yalla diouli ak weurdeu la bougonne.
Niari nite you outé lolou, mai la mbeugueul bolé .
Seyeu bou berri diekhi diakha ndakh dieko you outé lole
Séyeu bou berri yeungou yeungou ndakh loumou défone si adouname mokoy daboussi.
Réthieu gneweu
Mbeuguel gou degou fégne
Khole bou sétte nékeu séneu gualathie pour khékhe béppeu diafé diafé .
Li moy histoirou guéweul mbaye akmmmm bamba