fatouchhh
- Reads 2,759
- Votes 78
- Parts 4
fanta:man mom la beugue diaral nama bayi len
sa mère : wa ki esk sama dom la mbéguél diarna gua bayi sa yaye ak sa baye
fanta : wawaw diarnoko kay
fanta c'est une jeune fille âgée de 18ans
tombée amoureuse par son propre patron
fanta! fanta!fanta! ''cria sa mère''
doméram dji sa morom yup diangui pour téki euleuk ioe nakk guani yonn bou Bonn bi rek
fanta:wa yaye loy wakh ni
sa mère : kham dougal nagne la école classe bo deff défatt 3fs bagne dakeu la amol énen
lou nekk sa bopou loudoul farr Ya bon
fanta: maman tw aussi chacun à sn destin
sa mère : si bouba bamay dem marché sa kharit bobou Aïcha la tassél mou may 10mille mom lagne depenso tay