Wolofal
43 stories
taaru weer wi by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 86
  • WpVote
    Votes 3
  • WpPart
    Parts 1
Bile taar mooma yëngël, may wax di dem booleek fël, lepp lu ñëw duma yëngël, jëlël fukk ak ñeent yi ñoom .
XËCC BU DOGUL DIKK  by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 91
  • WpVote
    Votes 4
  • WpPart
    Parts 1
Maangi tudd MUHAMMADU HAFIZ MBÀKKE . Way yii maangi ko tudde XËCC BU DOGUL DIKK . Liko waral nak mooy damay dooga dugg ci WAY, toll ci WAYAN TU ta xam naane lepp looy door dinga du ñàkk ay fakkastal ci jëf ji ak ci ñikay gis baa ñukay degg . Waaye luci mana am duma tàyyi ndax XËCC BU DOGUL DIKK
maryaama ba  by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 99
  • WpVote
    Votes 7
  • WpPart
    Parts 1
BATAAXEL BU GUDDE NII ________ MARIYAAMA BA ________ Aysatu jot naa sa bataaxel fekk ma ci nattu ni ma lay tontoo mooy wéttalikoo këyit wii lu ma xalaat def ci.
yóbba lu néegu sëy  by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 191
  • WpVote
    Votes 4
  • WpPart
    Parts 1
Dëgërël muñ sa tiisu sëy, bula mer yen ba gaa nu fay,
yeewu jotna by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 104
  • WpVote
    Votes 1
  • WpPart
    Parts 2
dañoo melni ku tëdd ci guddi gi di nelaw ba jantt fékk am sunuy moroom yu njëlu ñun nak ñuy nelaw rek ta xam nan ne ku teeluta xëy boo demee ca ja fekk ña njëlu jël koom a ta kon ñooñuy xala may . ta WOLOF NEENA kula abali gët fiko neex ngay xool . kon nak yeewu jotna .
mbëgél  by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 100
  • WpVote
    Votes 3
  • WpPart
    Parts 1
fàttaliku sunu jamono ju neexoon lool ak liñ daan dund
Anniversaire by mbackehafiz
mbackehafiz
  • WpView
    Reads 111
  • WpVote
    Votes 4
  • WpPart
    Parts 1
sama anniversaire
L'épouse du Cheikh : les coulisses du mariage by haalpulaar
haalpulaar
  • WpView
    Reads 5,189,306
  • WpVote
    Votes 122,837
  • WpPart
    Parts 7
On a jamais côtoyé les épouses des hommes de Dieu mais on a tous une certaine connaissance par rapport à leur comportement: humbles, silencieuses soumises et endurantes. Mais Rayhan mariée avec un homme d'affaires mais aussi un marabout , a du mal a se faire aux coutumes. pour elle dans l'intimité le marabout est son mari. les dessous du couple Cheikh Hakim Barro et Rayhan Hanne sont mises a nus, les querelles. les interdits... tout est au rendez-vous.....
Youma: Soumise ou dévouée? by haalpulaar
haalpulaar
  • WpView
    Reads 3,531,778
  • WpVote
    Votes 64,724
  • WpPart
    Parts 6
Jeune fille on nous apprend toujours que l'on devrait être une épouse dévouée mais dévouée dans quel sens? la soumission totale ? le respect de son mari? être une esclave ? voyons voir ce qu'est la dévotion et la soumission chez Youma Aissata Barro
La famille du Cheikh : tels parents, quels enfants ! by haalpulaar
haalpulaar
  • WpView
    Reads 3,866,610
  • WpVote
    Votes 67,950
  • WpPart
    Parts 5
Tome 2 de l'épouse du cheikh. Je vous embarque pour de nouvelles aventures. ✋😂