Lou Méti Yagoul 😭
Lou Méti Yagoul ( LMY ) Li histoire bou doy War la. Bou daw Yaram sakh méti lole. Kouma wakhone li amna doumako geum . Béneu khalei bou jiguene bou toudou Oumou deukeu thi béneu village AK parents wam yi . 15 ans la am nékeu élève de 3 ème thi béneu CEM mou deuk bi .Tarou tey yarou bakh lole Ba jour bi professeur de...