Select All
  • Sa diabar la beugue done 💖
    501K 63.4K 51

    Waw lini fangue kéne douko diékheu diabaram la beugue done wayè nak wadji dafa mélni guissouma ish suis même ridicule devant lui déff na lounek wala lima djongoma moko tital comme mome kholouma légui nañou forcé mbeguel bi ma deuye lène touti rk gno diakarlo appartement ma doli léne touti rk sama rakou patron la oh...

    Completed