Ni Leu Meuneu Démé [TERMINÉ]
Salam sama gars yi, magui dora tambali bindoum Wolof ci Wattpad bi, Chronique2Laye moma diokh biii khalat né pourquoi pas, dii diégalou cii bepp ndioumté cii biir bind yi Hope les coeukhs, you gonna like it....
Completed