Kéne kou mel ni yow
  • Reads 480,253
  • Votes 58,898
  • Parts 44
  • Reads 480,253
  • Votes 58,898
  • Parts 44
Complete, First published Sep 14, 2017
Chronique bou bess bo khamené wolof la nitt gniy lak. Amouma intention diangual nitt gni alphabet wolof, déjà mane bien que diangue nako maîtriserwouma ko. Lima ci djoubelou moy bind chronique bo khamené nitt gni dagnouy wakhtane comme nigne koy défé dans la vraie vie. Chronique yougnouy bind en français yeup on va sur la base que c'est en wolof mais bougnouy nétali dagnoujoy tekki ci français. Bi nak chronique la bo khame ni dou ame tekki. 
Effectivement amoul sakh kharal ma dem té gneuw, dou 100% wolof mane rek soumay wakh dama ciy dougueul français donc les personnages aussi.
Di gnane yalla histoire bi nekh leine ak tamitt nignouko nétalé.
All Rights Reserved
Sign up to add Kéne kou mel ni yow to your library and receive updates
or
#735romance
Content Guidelines
You may also like
You may also like
Slide 1 of 10
Du sel au sang cover
Les mémoires de Souvenir [livre 1~les huit clans] cover
Rosehill cover
Chronique de Kayna : «Pour nos deux âmes solitaires» cover
Vengeance cover
Bad romance cover
 « Le temps d'un voyage »  - S H Y R I N E  cover
Khalil entre Nous . cover
Ma coépouse (sama woudiou) cover
𝑭𝒂𝒕𝒆𝒉 & 𝑫𝒋𝒆𝒏𝒂𝒃𝒆 | : « 𝑃𝑎𝑠 𝑝𝑎𝑟 𝑐ℎ𝑜𝑖𝑥 𝑚𝑎𝑖𝑠 𝑝𝑎𝑟 𝑑𝑒́𝑝𝑖𝑡 » cover

Du sel au sang

69 parts Ongoing

Ennemies to lovers