Tankk Bukki histoire bo xamnei la mo ngui am si diganetei bén couple. Fatimétou mi ngui si netali nimou xamaneté ak borom keureum, ay mbegtè wam ak ay nakaram. mou mel ni sax lolou moy mandargay nobel. Digantè bo guiss amna ay hauts ak ay bas. sasse you nek rek fatimétou mi ngui done beuss xolam, di gueumeu si you beuri, wayé nak keneu meunoul deukk si di nakh sa bop.