serigne saliou mbackè
  • Reads 596
  • Votes 43
  • Parts 1
  • Reads 596
  • Votes 43
  • Parts 1
Ongoing, First published Apr 19, 2020
Talif serigne saliou

 ...ma xeuy di dioyyy ay dioyiii xolll
Weuy mbeur ma ma takh sougne  xol yi xooollll
Mo bari wone yeurmandé Looolll
 ch salihou modi toureum

dioyyy na ba saa beut yi Leundeum 
Ngir lima tiiis diarna Geuleum
beugouma Oor sakka ngalam
kama khamone demna keurem

 lakhouna 28 thia wéerrr 
 wagne na decembre lii dou réeeere
Souniou banéex bobeuh la téeerrrrr
 ndaw gnia dioy ba am niou kheummm

aduna wéet dade ni sélaww
ken talatoul teudiii nélawww
gneuppa gnii tiiit diakhlé di dawww
ngir cheikhy salihou démam

Fourkhane di dioyyyy niogame ni Woooyyy
 hadiths di wakh ma niakkk wayyy
Khassida mouji dioyyy ba Toooyyy
Ndax ken dolen fonké ni Mom

Dounya bi mouji wéettt thi tayyy
sangue ba wathi ap Jotayyy
Yalnako Yalla dolli Fayyy
 thiey salihou amo Morom

Yeurmandé yao yadi borom
yaye djeummi cheikhinal khadimm
Done nga batine bathia mommm
 ak dara diammm aki mélommm

Ahmadou diokhla diamono
Ngay ndittt thi ahlou zamano 
lأنت العلى المؤتمن
Mame salihoyyy ki mata geummm

Té alkhourane yako suigilll
Diouma yi tim yalénnn téraĺll
Ya roy kou bakh ka cheikhra fall
Mame Salihou yadi salimmm

 di niane thi barkép assirou
Mi maséee ak sgne bachirou
Liii léeerna cheikh ba habibou
  Na Yalla Yokkou ay mayam

auteur cheikh khadim goumbala 772558581 béne toutant bouy gorgorou rek
All Rights Reserved
Sign up to add serigne saliou mbackè to your library and receive updates
or
Content Guidelines
You may also like
You may also like
Slide 1 of 10
𝐖𝐀𝐇 𝐖𝐀𝐇  cover
KUMISAMA cover
Aya & Karim 🩷🇸🇳 cover
L'histoire de Soumaya cover
« 𝐍'𝐃𝐎𝐖𝐀 » cover
Lisungi, l'allié d'une vie cover
Tu es à moi  cover
Soumaya,l'épreuve de la foi [CORRECTION] cover
Chronique ( Une malédiction ancestrale) chronique sénégalaise 🇸🇳 cover
Coup de foudre à la mosquée cover

𝐖𝐀𝐇 𝐖𝐀𝐇

53 parts Ongoing

«Si Dieu est pour nous, qui sera contre nous ? » Romain 8:31