FRANÇAIS Ceci est un poème dédié spécialement au Prophète Mouhamed (psl), et écrit par un de ses homonymes, un jeune sénégalais du nom de Mouhamed NDIOUR dans le but de lui rendre un Hommage. Le choix de la langue locale (Wolof) a été fait tout simplement, pour permettre à toutes ces personnes ne maitrisant pas la langue française, de pouvoir lire ce poème et le comprendre. De plus, des écrits faits dans notre langue locale se font de plus en plus rares de nos jours et qu'il est temps que l'on donne plus de valeur à notre langue. Cependant, il faut noter que dans ce poème, l'alphabet wolof n'a pas été respecté parce que tout simplement, la majeure partie des sénégalais malheureusement, ne savent ni lire ni écrire dans leur propre langue. Alors, le choix du style d'écriture est maintenant compris par tout le monde. Merci et bonne lecture ! WOLOF Taalif bi niongui koy diagglel Yonenteu Mouhamed (saw). Kiko binde done abe sénégalais bou toudou Mouhamed NDIOUR ba paré dom tourondo wam teksi, mou dioub lou tchi rek diko délol ndioukeul. Li takh nak ma binde li si wolof té meunone ko binde si toubab rek mo di, da am niou bari si nioune niou degoul toubab té beug na niou xam lou taalif bi di wakh. Bima dalé binde si toubab yagg na, wayé niou bari dagn may niane may binde si wolof nakh niou meune faral di xam limay wakh. Té tamide, setlou nani légui nieup si narassane rek nagniy binde, bayi sougnou kalama bou am solo bi di wolof. Té lolou dou deug dou yoon té dou lou raféte. Diotna nak niou gueuneu diokh foula ak fayda sougnou lakeu bi di wolof. Wayé tamide, fokgnou xamni mbindoum wolof gueune na khoote li, wayé soumako défone tamide niou bari dougnouko meuneu diangueu té lolou done neu lou niaw tchi abe domou reewmi ngani meuno binde meune diangueu si sa lakeu. Li rek motax ma bindé ni nieupeu di bindé nakh nieup meune ko diangueu. Dieureudieuf ! Dilen nianal ndiangue bou sap