Céy Moodu!
  • Reads 272
  • Votes 6
  • Parts 3
  • Time 7m
  • Reads 272
  • Votes 6
  • Parts 3
  • Time 7m
Ongoing, First published Jul 15, 2021
moodu ab jangkatu nasaraan la!
ci njangam moomu da ca jambaar lool ba jangale kat yi mu massa jaar ñëppa ka naw. waaye da ñoo nekk foo xam ni am kulay doxal yitte ci nguur gi mooy tax nga am ligeey. moodu dajjale na ay lijaasam waaye fu mu dem nu tuutal ko ak di ko xass.

coono wuyussi ko
jaaxle dikal ko
yaay, baay ñëpp bayyi ko
diko toroxal ak dëke saaga ko

biss bu xëyee, metitam di gën a yokk. rangooñam feratul. ca noona yalla wane leko ak Fadel, xoole boobu nga xam ni amul ndey amul baay mbeed la dëk. 
yoonu moodu sóppiku Ba mu gen sen kër, jëll ma yoonu mbedd mi Ba du xëy sankkú. mu dem Ba sori ci dundu ga bindub bataaxal sanni, ma dox ba yam ca dileen ko nettali.
All Rights Reserved
Sign up to add Céy Moodu! to your library and receive updates
or
#30senegal
Content Guidelines
You may also like
Words Only Written by AudacityAllie
146 parts Ongoing
𝕋𝕙𝕖 𝕡𝕠𝕖𝕞𝕤 𝕒𝕣𝕖 𝕣𝕒𝕨, 𝕙𝕠𝕟𝕖𝕤𝕥, 𝕒𝕟𝕕 𝕦𝕟𝕒𝕡𝕠𝕝𝕠𝕘𝕖𝕥𝕚𝕔, 𝕔𝕒𝕡𝕥𝕦𝕣𝕚𝕟𝕘 𝕥𝕙𝕖 𝕖𝕤𝕤𝕖𝕟𝕔𝕖 𝕠𝕗 𝕨𝕙𝕒𝕥 𝕚𝕥 𝕗𝕖𝕖𝕝𝕤 𝕝𝕚𝕜𝕖 𝕥𝕠 𝕝𝕚𝕧𝕖 𝕨𝕚𝕥𝕙 𝕕𝕖𝕡𝕣𝕖𝕤𝕤𝕚𝕠𝕟. 𝕥𝕙𝕖 𝕕𝕒𝕣𝕜𝕟𝕖𝕤𝕤 𝕠𝕗 𝕥𝕙𝕖 𝕞𝕚𝕟𝕕,𝕤𝕒𝕕𝕟𝕖𝕤𝕤 𝕒𝕟𝕕 𝕥𝕙𝕖 𝕤𝕥𝕣𝕦𝕘𝕘𝕝𝕖 𝕥𝕠 𝕗𝕚𝕟𝕕 𝕙𝕠𝕡𝕖 𝕚𝕟 𝕥𝕙𝕖 𝕞𝕚𝕕𝕤𝕥 𝕠𝕗 𝕕𝕖𝕤𝕡𝕒𝕚𝕣. 𝕋𝕙𝕣𝕠𝕦𝕘𝕙 𝕨𝕠𝕣𝕕𝕤 𝕪𝕠𝕦 𝕨𝕚𝕝𝕝 𝕗𝕖𝕖𝕝 𝕥𝕙𝕖 𝕨𝕖𝕚𝕘𝕙𝕥 𝕠𝕗 𝕕𝕖𝕡𝕣𝕖𝕤𝕤𝕚𝕠𝕟, 𝕒𝕤 𝕚𝕥 𝕥𝕒𝕜𝕖𝕤 𝕙𝕠𝕝𝕕 𝕒𝕟𝕕 𝕣𝕖𝕗𝕦𝕤𝕖𝕤 𝕥𝕠 𝕝𝕖𝕥 𝕘𝕠. 𝔹𝕦𝕥 𝕖𝕧𝕖𝕟 𝕒𝕞𝕚𝕕𝕤𝕥 𝕥𝕙𝕖 𝕕𝕒𝕣𝕜𝕟𝕖𝕤𝕤, 𝕥𝕙𝕖𝕣𝕖 𝕒𝕣𝕖 𝕞𝕠𝕞𝕖𝕟𝕥𝕤 𝕠𝕗 𝕓𝕖𝕒𝕦𝕥𝕪 𝕒𝕟𝕕 𝕝𝕚𝕘𝕙𝕥 𝕋𝕙𝕚𝕤 𝕚𝕤 𝕒 𝕓𝕠𝕠𝕜 𝕥𝕙𝕒𝕥 𝕨𝕚𝕝𝕝 𝕣𝕖𝕤𝕠𝕟𝕒𝕥𝕖 𝕨𝕚𝕥𝕙 𝕒𝕟𝕪𝕠𝕟𝕖 𝕨𝕙𝕠 𝕙𝕒𝕤 𝕖𝕧𝕖𝕣 𝕤𝕥𝕣𝕦𝕘𝕘𝕝𝕖𝕕 𝕨𝕚𝕥𝕙 𝕕𝕖𝕡𝕣𝕖𝕤𝕤𝕚𝕠𝕟. 𝕀𝕥 𝕚𝕤 𝕒 𝕣𝕖𝕞𝕚𝕟𝕕𝕖𝕣 𝕥𝕙𝕒𝕥 𝕨𝕖 𝕒𝕣𝕖 𝕟𝕠𝕥 𝕒𝕝𝕠𝕟𝕖 𝕚𝕟 𝕠𝕦𝕣 𝕡𝕒𝕚𝕟 𝕒𝕟𝕕 𝕥𝕙𝕒𝕥 𝕥𝕙𝕖𝕣𝕖 𝕚𝕤 𝕒𝕝𝕨𝕒𝕪𝕤 𝕙𝕠𝕡𝕖 𝕗𝕠𝕣 𝕥𝕠𝕞𝕠𝕣𝕣𝕠𝕨.
You may also like
Slide 1 of 10
One Shots Male Reader [||][Pedidos Cerrados] cover
ياقلب دقات الهوى لاعبتني قامت تمايل بالدلع كانه العود  cover
ليتك ياحبيبي اول احبابي cover
Poems And Some Deep Thoughts cover
Words Only Written cover
Doctor  Husband (Complete) cover
𝐦𝐞𝐥𝐚𝐧𝐜𝐡𝐨𝐥𝐲 ➙ 𝘱𝘰𝘦𝘵𝘳𝘺 cover
A Dreamer's Poetry cover
My Poetry cover
Chaos In My Mind cover

One Shots Male Reader [||][Pedidos Cerrados]

172 parts Ongoing

Holaa~ Bienvenidos todos a estas pequeñas historias, empezando de nuevo :D Muchas gracias por pasarte por aquí, supongo que pronto voy a abrir los pedidos. Así que puedes disfrutar mientras tanto las historias que tengo ahora, puedes leer las aclaraciones o las etiquetas para saber que anime o de que escribo. Gracias <3! Créditos a quien corresponda por todos los personajes utilizados, a excepción de _______.