Vie sénégalaise
  • Reads 4
  • Votes 1
  • Parts 1
  • Reads 4
  • Votes 1
  • Parts 1
Ongoing, First published Oct 05, 2023
Histoire bi mougui néka histoire bouy wakh si béna pâ bou dane taka di tass bamou dioureul ko haine entre mom ak ay domam ak mirase bou compliqué après sa mort. 
Ak mariage de Maguette domam bi marié ak gendarme bi si deukeu bi niou doundou aussi Lou métti parce que le mec avait beaucoup de charge à travers sa famille. Dém nagne ba am dom bouléne meuneu diappalé financièrement mais béna mère bousi kogne bi moudié ka liguéye di léka si mom xaliss.
Souffrance Maguette yamoul fi loin de là après bénène dom bi takka diabar, diabar dji amoul Loumou défoul si keur gui ! 
Bénène dom dji nak mom expérience moko sonal dokhane rek ak popularité moko nior mais  nak il est intelligent dans sa démarche 

Topouléne ma di guen xam Lou xew si Sénégal la façon de pensée des sénégalais ak séni dougou dougou lep fi lay xéwé....
All Rights Reserved
Sign up to add Vie sénégalaise to your library and receive updates
or
Content Guidelines
You may also like
You may also like
Slide 1 of 10
o amor verdadeiro... cover
ay dios mio cover
GIMBIYA YALUSA ÝAR SARKI MAI FAADAR ZENARE cover
Amor De Verdad cover
Kiss me again ☘️🍁 cover
💫 cover
Ne Oluyor !!!!! cover
bryan sigismund cover
រឿង រវាងពួកយើង cover
Us and you cover

o amor verdadeiro...

1 part Ongoing

💕💕💕