Abdou et Fatou amour inoubliable ( Wolof)
79 parts Complete Salem alaykum
Venez découvrir mon 1 ere livre kouka tadé kharou
Fatou bénde khalé bou djiuéne la bou tayéle safe lamigne
Abdou mbénde khalé bou goor la bou haine djiguéne
Sétane léne chronique bi ndakh nguéne fatou ak abdou lougnouy moudjé
___
Bi mo nékk sama première chronique bouléne faté dima encouragé
Let' s go