chapitre 5

688 30 0
                                    

Dans la peau de khadim

Moi. Salam yaye non deff

Mère coumba. Boul mané yaye non deff

Moi. Wa yaye lou hew

Mère coumba. Khana se lingua indi si keur gui diapp coumba moundaw dor bamouy beug dé

Moi. Lan kan mo dor kan

Mère coumba. Se diabar khana

Moi. Anni coumba

Mère coumba. Mingui négou sokhna kharal ma woko ngua guisal KO se bopp

Coumba.😭😭 khadim yama wo

Moi. Yow koula neff ni😯😯😯

Coumba. Se diabar

Moi. Lan molen diotté

Coumba. Déma sonné mou niow oubil ma ma nouyouko wayouma mounéma thiaga yi nguén don dougén tokk sénn keur Mané KO man ngay wakhal rek mou sogoumaa😭😭😭😭

Moi. Lan awa mo defff lolou kharal

Moi. Awa awa

Dans ma peau

Khadim. Awa awa

Wah ki dou khadim ki kagne la wathie sah  man bima wathié déma tit sah déma fékk sorcière bou bess bi di dioy dioyou méti

Moi. Firdawsi lan la louhew té iow sah kagne ngua wathie

Khdim. Awa lilanla 

Moi. Lan man comprendre ma linguay wah dé

Mère coumba. Khôl KO Mouy dofff doff lou ningua deff ki lay wah

Weuh ki kanam gui mingui dagg bâ yakou

Moi. Man lan lako deff

Khadim. Awa boul ma fonto ki yako dort

Moi. Firdawsi man déma KO mbéthie rek m dou man mako deff ni

Khadim. Dengay doul ki yako dor yow dengua KO eupeulé si keur gui bakoy traité de thiaga

Moi. Hii ki momana fenn

Mbeithie tarr hii khadim man lay dor

Moi. Yow man ngay dorr

Khadim. Doumasa morom boy wakhal di saga

Mère coumba. Niaw khamngua né lingua linguéy ki diadou woul

Déma daw dougou sama nékk nonon li manoul nékk khadim man lay dor ndah imbécile bi wolay dinako réthiou parole d.Éva

Gni khamna liniou beug wayé douma lenn KO  may may diokk sangou sol sama lourafétt wathie dog rérr bi
Bima wathié ma rombou lén si sal bi

Mère coumba. Hii yow ak  Khadim déngua na beuganté won nak

Sokhna. Bilae khadim kay geuw ma ndah dina beugaté nonou djiguénn

Coumba. Motah déma niow pour récupérer KO ndah sama alal la

En kon ki mok khadim deniou don guénn naron nako balou wayé kharal bâ Mou niow amél nama Aÿ explication mom sah nekoufi kharal ma woko

Appelle  Regeté wa ki man lay coupé
Legui nak diélatouma

Dans la peau de khadim

Cheikh. Wa bro do diél kilay wo

Moi. Awa la bayi ko fofou

Cheikh. Wa awa Molay wo ngua koy bania diel louhew

Moi. Dénio khoulo bama dorr KO

Cheikh. Dor ngua wah dé khana dengua doff

Moi. Coumba mou ndaw mo faniow rek awa dor ko ba yakk kanam gui

Cheikh. Mdr non khadim do nitt yow dengua féké khéh bi

Moi. Nonon m coumba limouma wah awa mo togne

Cheikh. Légui yow déglou ngua awa mom tamite

Moi. Nonon defa wah ak man saga ma mbéthie.'

Cheikh. Yow se ex motah ngay dorr se diabar

Moi. Bilae je n c.est plus koi faire

Cheikh. Lingay faire lenn la démal ngua wahtan ak sa diabar

Moi. Hiii insbi kay souma démé keur gui thém bâ defff mousi bâ ndah khamna awa

Cheikh. Wa démal rek

Dans ma peau

Wa ki fan la wara nékk beu heur bi DEFA. Mél moy niow nonou sah sama nuisett bou sexy la soll diko khar wayé dou lal dé

Défa dougou si chambre bi soumékou diall si sdb bi faléwouma sah m mo kham mangui teud won KO guénaw niowna beu teud bimou fayé lampe la khamné teud na m fokk niou wah ma diog tal lampe levrette bi

Moi. Khadim.     Khadim khana dou iow lay wakhal

Khadim. Lanla

Moi. En lanla ngua may wah

Khadim. Wakhal gaw déma gueméntou

Moi.iow ak coumba dénguén don guén

Khadim. Yow wah niou niak fayda yi mtx ngua déranger 

Moi. Mais

Khadim. Pas de mais Bonne nuit

Goudi gui yépp néléwouma depuis ma niow si keur gui bâ làgui mr mongui may soga won guinaw

Il était 6h du mat ma diouk sangou diouli  dém défar ndéki

Moi. Bonjour

Khadim.bonjour très sec

Moi. Ndéki bi paréna

Tontouwouma sah defff ma yomb guénn ma wathie si sall bi fékouma ko fofou

Moi. Salam yaye anni khadim
Mere bi dé kholouma sah

Ma tokk di ndéki

Coumba. Waw badiane yénn mom li guén di lékk 

Mère coumba. Guiss ngua dé mtx nak khadim mo yéya dém té ndéki woul

Coumba. Sokhna accompagné ma défaral ndéki yoboul KO

Moi. Yow ya wané lou sisa yon yow biss bo dougué si wagne nan dengay lal dara baye yoboul sama dieukeur ndéki démalay rey

Mère coumba. Ey way ndaw samba lal KO  sétt

Sama Firdawsi🥰🥰Où les histoires vivent. Découvrez maintenant