🔥 Katantè Souniou École épisode 1

1.2K 4 1
                                    

Cours du soir a l'école , Eléves yi wathie , Laye éléve 2nd ak xaritam Papis nioy ande pour gnibi , séne kanam Astou , Marietou ak Khady séne premier cours du soir wayé xamantéwouniou séne bir

Laye : fils Pape xolal Astou boy ki amna tate dh weuh fils ki fok ma lale ko

Papis : 😂yow Astou ngay wax xana guisso Khady ak weine yi boy école bi année bi ay khalé you mol rek niofi nék

Laye : 🤣 xamna fingay xalatei domeram nga rek

Laye : Wa mais miss yi nangéne deff yénangui am diam

Niom marietou : wa cv yow nak

Laye : mangui bien mane c'est Laye

Marietou : mane Marietou ki sama wét Khady ak Astou

Laye : séne tour yi nekhnagne mom

Marietou : mercii

Laye : da mélni nio bok yone dh
Wa mais xaral Pape yow mom xana do wax ahh

Pape : Marietou nakamou Khady Astou cv

Marietou ak niénene gni : Pape cv

Laye : yow ya sof boy

Pape : fils adioul way

Laye : wa miss yi sinon nak naka cours yi , nio nékando si classe bi wayé xamanté wougnou sax té année bi yeup nioy nék kone yakarna niou xarito minenté mo gueune

Marietou : wa lolou deug leu

Laye : dioxléne ma séne numero way damay creer béne groupe whatsapp sax comme ça nioussi wahtane nioune nieup

Marietou : idée la mom

Niom nieup dioxé séne numero

Laye : rafetna after nagne tégue marietou

Marietou : daccord Laye

Khady : ciaoo ciaoo nioune fi lagni diadé

Laye : wa mais bayil ma guoungué léne heure bi timisséna dh

Khady : non grawoul tmt ba bénéne yone danio yakamti

Laye : wa amoul bléme ba soubak diam .

Laye creer na groupe whatsapp ba ajouté nieup .

*( Dans le groupe WhatsApp )* Laye : Salam mbokk yi ziarnaléne dé

Marietou : Cv Laye

Laye : Marietou cool ni loubon

Marietou : ah dra hana sone rek

Laye dieul marietou si souff continuer wahtane bi

Laye : mais loula sonal yow waro di sone

Marietou : ndap , fot , wér da méti

Laye vocalko niko mola war nak di retane

Marietou : ay laye mane ngay wah li

Laye : tmt yow yay séne djiguéne soko défoul koukay def wa ehh nak damalay togne rek 😂

Laye : sourireul way

Marietou rétane , yow danga meuna togne

Laye : sila bokou mais loy deff insbi

Marietou : defouma dra damay wadial teudi

Laye : dedet douma nangou lolou mom

Marietou : ahh souma gueuménto nak

Laye : waxal gueuméntou mou bayila

Marietou rétane

Laye commencé di wahtane ak marietou lou yague ay 1h du matin niongui wahtane di ré

Laye yondé béne jeu ay questions niom niar kounék day choisir béne numero kénéne ki tontou

Questions yeup nak ay waxi tate rek la thiey laye moy doméram rek

Marietou choisir laye diko tontou

Ba laye lathié marietou ndah meussna sétane

Marietou : béne yone rek dou mane sah sama xarit mokodone sétane

Laye si xélam : fen rek 😂 wornama chaque jour mou sétane ko

Niom niar niou continué jeu bi bamou tang kay

Marietou : Laye est ce que meussnga ...

À suivre.....🥵🔥

🥵🔥🥵Titre : Rencontre Groupe watpad*( Bande annonce)*Où les histoires vivent. Découvrez maintenant