tieyy sama yaye

3.6K 334 1
                                    

Je me lève la tête sur le cul pour la prière de fadhiar dirigé par mon père tout les jours je par pars et reviens dormir ......

Je me réveille cette fois ci en forme j allume mon téléphone et je constate qu il est 12h et quelque lahilaa loutakh sama yaye yewouma môme gua hamni fou 10h dothé mou feug nieup 😂

Je me douche et porte une robe simple fleuri je descend en bat ( logique mdr)
Pour déjeuner faut savoir que je suis une vraie pipelette

SALAM ALEYKOUM TOUT LE MONDE

Mére : WA ANNA DOMERAME Bi TITEUL GUAMA dagua beug yobe sama fit bi niata yone lala wakh gua bayi sa youhou yi liguey fouy yeuk yéwou heur bi rek Di dofdoflou sa niaway idiam

Je regarde Ousmane du coin de l oeil et je le vois entrain de se retenir pour ne pas rire thim nimako diépiwé môme loumou fiy deff sakh hana liguéyoul en il est en congé 🤦🏽‍♀️ki fauk ma outal ko diabar Mouy melni loye ni

Papa : Fa bayil ki guay hass ioe rek lay ndirou

Maman : donc Aboubacry dagua beug wakh ni man dama niaw ANN ?

Papa : en bégayant guani meussou ma wakh lolou ioe ya dack thi adouna bi

Maman : mo gueune thi ioe dh ak sa dialabé bou niaw bi

Elle se lève en boudant et sort du salon on se regarde tout les trois puis pouff de rire non mère bi cinéma la nena da foulard bou fuicha Nonou ki d'ou dem

Maman : annnn yen dal man Guen dih ré tay ken d'où Guen keurgui Guen ham nak

Ousmane : mais yaye dama wara Guen ak papa migui may har

Maman : sama Yonne nekoussi ya ham dh

Ousmane : wa yaye damay dioy dh

Limouy niak fayda yeup magui feki Marie thi wagn bi souniou diank la Aka mako ko beug

Moi : wa ki d'où marie ndiago yen shi boy tay sangsé gua dh wawe an seur bou bleu jaune bi melni kou kampagniall lay Wade

Marie : d'où negua ioe do changer douma la sakh tontou kay lek mo gueune thi ioe thimmmmm

Moi : faté nala wakh je me marie dengue

Elle en fesant tomber la cuillère qu elle tenait

Marie: ioe mou beuri wakhmi koulay tak ak koula nop dit elle en rigolant

Moi : boy ioe man rek shi guisso dara man sakh hawma kokou koumou yalna raffet rek papa Bouma tandalé Kou niaw borome beugn you jaune yi doumako bal

Marie : shi pabi mako fan imaginel mou nek diaykatou maquillage bi fiy nieuw témou nop la rek

Moi : BOY bayil yiguay wakh way yallah tere

Marie : yalna nek kokou gua ham

Je sors de la cuisine eh merci imagine mou nek kooku ma wara yewou diko hol chaque jour commencer cogiter sakh cheutttttttttt





Je vous passe jusqu'au samedi

Commentez
Partager
Likez

Aichaminato ✨🙏🏾🔥

Man Anna Rek Seuy Seuy Bi Où les histoires vivent. Découvrez maintenant