_ Rokhy bâ diam la , binga gnou wowei danio tiit saakh disait Maty tout en paniquant .
En les voyant je me contentais de pleurer encore plus , j'avais besoin de ça , besoin de quelqu'un qui m'écoute ,qui soit à mes côtés et qui me réconforte .
_ yiow boul gnou titeul way , waaah yiow so defei ni gnounn nougnouy def ? Lançait Fatou en pleurant aussi .
Elles me prenaient dans leurs bras et on pleurer tous . d'une minute à l'autre on se détache .
_ waah wouyouma Rokhy , expliques nous book ! Dit Maty
_ laisse là débarbouiller le visage d'abords , va laver le visage . répliqua Fatou
J'entre dans la salle de bain , nettoie le visage et reviens .
_ on t'écoute Rokhy !
_ les filles , c'est que...sniif ... sniif , mon père est opposé sur mon mariage avec Khalil sniif...sniif, neina fii ak mouy doundeu douma meusseu may Khalil...sniiif...sniif .
_ sa papa xaanaa da xamoul finga diaaarr ak Khalil yeup , Rokhy yiow Khalil mootaakh nga yakk sa diang bi et gueumoo koudoul mom , 7ans de relations ngua Beug KO baayi mou diekh nii , boulako dara diaaraal sur terre , deimal ci sa mbook yi gnou mayeii laa. répliqua Maty avec ses grimaces
_ aay Maty waagniil booq , kii nek ci Aÿ blem ngay gueuneu diekhal kholal .
_ kholal yiow dimbalima, deug dong laakoo waakh .
_ wouyouma Rokhy boul degg lou kiii , Aÿ connerie req lay raconter . waakhtaanaal ak sa papa , diem KO convaincre req inchalaah dinga ci am ndame . mo gueunn ngay seuyi tei doussi andeu euleuk ci biir khamo seuy bi noumouy demei . et les parents restent les parents . conseilla Fatou
_ deggg naa liguenn waakh lepp , et merci kounei degg na sa version mais Sama papa gaindei gou dégoul diatt laa , doussi meusseu andeu et mann beugg naa Khalil Beug bo xamni meunoumako bayi nonou , ins bi naq lenn req mossiy pexei lii Maty waakh xaaanaaa tei pareina pour def leppp ndaakh mariage bi am .
_ anh comme que lolou nga guiss dagnoussiy andeu ak yiow rek , gnounn gnongui sa guinaaw , dolel la et pour soutenir laa . boul tiitt daaraa . dit Fatou en essuyant mes larmes qui n'arrêtent de couler .
_ waaw Rokhy nous , on est derrière toi et ne te sens pas seule , loussi meunn ti am req tu nous diras . bon xamna dagnouy dioug dem parce-que diott amoul .
_ oui tyma allons y mais Rokhy togatal nga xaalaat bala ngay decider quoi que ce soit OK . on te laisse alors ciao à la prochaine .
Elles partent et me laissent allongée sur mon lit en essayant de me reposer . oh les filles m'ont vraiment soulager , merci à dieu de m'avoir donner de si gentilles amies . mes problèmes sont les tiens , je suis fière d'elles .
Le sonnerie de mon téléphone me sortit de mes pensées . je prends et voit que c'est Khalil mais j'hésitais si je devais prendre ou pas mais je ne sais pas quel vent m'a poussé à le raccrocher .
Je ne peux pas parler avec lui comme ça , je suis très mélancolique pour le répondre avec ma voix qui s'est cassée . je ne veux pas qu'il sache ce qui se passe actuellement et si je lui réponds , il va sûrement être au courant . il insistait encore et encore mais je ne réponds pas .Khalil...
Waah ki lann moko dall mann lay raccrocher au nez ,attends je vais le rappeler ; il sonne mais pas de réponse .
_ waaw boy loy khoultou ni taamiit , sank baateey magui feugg ci porte bi degooma saakh. disait Babacar en faisant des gestes avec ses mains .