DAROU SALAM

33 3 2
                                    

1- Darou Salam SERIGNE TOUBA moko santhieb bessoup talata 18safar1304 depock 1886
2- Darou Salam mom la SERIGNE TOUBA ndieuk ame si keur goumou mome ngir wete fa diamou yallah tarbiya fa
3- Darou Salam tour wi mouthe adouna ak alkhira laye teki
4- Darou Salam fala Cheikh Mouhamadou Moustapha Mbacké bi ndieukeu done khalifa CHEIKHOUL KHADIM dioudo fi yamoul achoura 1886
5- Darou Salam fala Cheikh Mouhamadou Fadale midone niarelou khalifa CHEIKHOUL KHADIM Ffegne kazou rajab 1886
6- Darou Salam fala MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL ame gueuremoule CHEIKHOUL KHADIM
7- Darou Salam fala CHEIKHOUL KHADIM diokhewone ndiguelou Magalou TOUBA 1903
8- Darou Salam fala CHEIKHOUL KHADIMyenekouwone yaname bou rey bamou dielewone thi Guethe gui lofa dagane dadiek mome
9- Darou Salam CHEIKHOUL KHADIM moka rafatalewone Mame Cheikh Anta 1888 bolekok 99 mourides
10- Darou Salam CHEIKHOUL KHADIM nena yakar doufa tasse mouk
11- Darou Salam koufa tek sa tank sa yaram haramal na safar Serigne Cheikh Maty Leye moko wakhone ba Serigne Hamidoune lako
12- Darou Salam khobi garab ya ak soufsa safara la Sokhna Faty Dia moko wakhone
13- Darou Salam kou beugu falou demal fofou
14- Darou Salam Mame Cheikh Anta mofa dekeu latone tawame Serigne Modou Mamoune 1917
15- Kane moye Serigne Modou Mamoune....
              A suivre

Darou SalamWhere stories live. Discover now