DiwanouBoromeTouba
*Bismillah* *cheikh ibra neena* Ah dome! Ande ci foula moy ande ci deugg wayei fayda ga mooy bou deugg naré naax saay gnou bâyi ande ba. *borome touba neena:* kou beugga goudou fane, lo am deko bokak wa adina, tey gnanal wa alakhira.