bn tay la lundi cours yi tay lay dèmarè dans les normes
bn je me reveil à 6h kom ke sma ècole da sori ma diouk sanguou diouli solou guiss 7h00 wa heure bi guaw na dh kharal ma guaw wathi nouyou papa ak maman dieul sama xaliss ndèki dèm bala ma tardè
Moi:
slt Papa maman nolèn fananè
eux: cv alhamdoulillah
Moi: wa mangui dèm bala ma tardè
Ma mère: amsa xaliss ndèki
Moi: ohh mr6 ma fatè won nako ciao dèmna
Ma mere: wa dmal ak diammay guen keur gui ba yègu si wètou boutique bi guiss xallei bou arrogant bobou ma tasè lon si terminus bi nek sougnou wètou ècole
wa ki mom tiey yallah khana sagno ma dèf li dh kon ki gno bokou kogn may guawan tou mou dap ma
lui: sorcière
bala ma tontou mou rombou ma sma xol bangui bon mais na mougn rekk
may guawan tou guiss mouy 7h30 ehhh ba douma tardè ma ègu rekk guiss bus douguou dèm direction ècole mangui si bus bi mais sma xel bi yeup si Mr arrogant la nèk wa man louma dal
10mn après ma ègu alhamdoulillah ba tardè wouma il est 7h40 ma douguou si lycèe bi dem sma classe lathiè lèn ma kouma tasèl envore Mr arrogant ma fass sma kanam douguou tok
10mn après prof bi gneuw ma guiss Mr arrogant douguou si classe bi kom ke dama meun xoulè makoy xol rekk bamou tok sougnou beut yi tasè rek ma guawan tou tournè wa mais kon ki gno nara bokou annèe bi cheuuu noumay dèf lègui
ma dèf cours prof hg mo gneuw mou def cours ma participè sma matière la nk
9h55 prof bi dèm ma guèn di dieunde mbourou pour wan Mr arrogant rombatt ma nèma sorcière kom bal nako si souba si bi mom je me laisse po faire
Moi yow ehh khamgua louma lay xamal bouma wowè watt sociere gnak fayda ba beugu dh
lui : kon gua bagn ma xol son ami rigole
Moi: espèce de kagna
ma rombou dem degu xaritam bi diko rètan aussi di dagni diay rèw rekk
après gnou dèf cours maths 10h 12h
après français 12h 14h gnou wathi
tangu na sonou na tè Mr arrogant enervè nama sila dieul dème si terminus bi di xar bus mou fèk mafa
wa man ki mom loum ma topè bus bi gneuw ma douguou mou douguou
ehh xana yallah tay lama don xar monouma bokak ki kogn ak bus nonon
Moi: yow lomay topè
lui: koula soxla topou sa xèsay
Moi : bala gua xastè daguay diak yak sa gnoulay thim
lui: dacc sorcière
sma xol bangui bone ma nopi fass sma kanam ba ègu wathi mou wathi lui aussi ehh dieu ma diad mou diad ahhh wa li mom sma xel bangui diaxaso
après sila douguè sèn keur man ma continuè ben 1mn ma èguwa li ndogualou yallah la wla ??