Slm les gars je m'appelle Aby Mais guayi biba lagn may wowé j'ai 17ans suis en classe de second bref assez parlé de moi
Man dh ouakam la deukon mais sma père mo am gallé keur massar dogno moudié dém fofou manam dagno toukhou dal louma méti NK mais meunou masi dra😪 smay xaritt yi dina lén nam ( oumou kalsoum ,oumy diéye , Maguette Awa ak rama )diguén né beuri na xaritt dh 😂 mais BN on continue
Nolén guissé première chapitre bi??
Aby yan rencontre mokay xar si quartier wam bou bés bi??