BISMILAH
Cc la famille kham nani vous avez l'envie folle de me tué mais bilay ses derniers temps j'étais trop prise yalla kham nako avec ma sœur qui se marie ensuite mon autre sœur qui accouche j'étais débordé mais légui CV xéwi diékhna je vais maintenant pouvoir continuer la chronique et publié les parties comme prévu
Désolé encore pour cette longue attente mes pucesBONNE LECTURE LA MIFA
POINT DE VUE EXTRÊME
10h chez les Kane
La dame de maison mère aminata qui venait de sortir de sa chambre se place sur le sofa de son salon comme chaque matinée commande en main attendent l'arrivé de sa belle-fille ou servante pour lui servir son petit déjeuné c'est ainsi que sa fille Gniémé la trouve
Gniémé: waaa yaye t'es réveillée donc taye mom dagua grâce matiné dalll
Mère aminata: ahh dome noumaye déf dëme dama tass nakh xéw bi
Gniémé: waw kay nak yaw sakh wakh moye ini wakh
Dit-elle retrouvent son sérieux
Mère aminata: abn lou xéw ba diam
Gniémé: diam la dou diam nakh mane je crois que damaye beugu djiomi
Mère aminata: djiomi Gniémé koulaye djiomal ma déf si mom
Gniémé: kone défal si sa Bopou yaye nakh ak fi réwemi tolou sa melokane ték nama pression
Mère aminata: umhm dama déf loula méti
Gniémé: défo louma méti dh dagua déf louye dagu sama xol bi yaw mère koula fék guaye dém xéw loumou la wara wakh
Mère aminata souffle: sheutetete Gniémé yaw titale guama lolou rék motakh guaye déf tout ce cirque Ah dom djiongué gua
Gniémé: cirque wakh gua deug dh yaw est-ce que ça va mère dagua faté ni daguaye tëgne khana dagua faténi sama pape bimou décédé ak légui matagoule mois guaye weurr xëwi
Mère aminata change subitement d'expression
Mère aminata: et alors légui nak GNIÉMÉ Kane
Gniémé: oooh mère calmos rék nank métiwoule yaw déjà sa changement d'humeur safouma nakh kham guani mane yaw la dieule mais tmt yaw mi kéne wakhoula naka ware...
Mère aminata en la coupent: GNIÉMÉ surveille ton language n'oublie surtout pas a qui tu t'adresse
Hurle telle presque à bout de souffle lolou melni lou guana tall Gniémé aye yalla yare sa dom bakhna trop
Gniémé: kham Kane laye wakhal motakh ma ame audace wakh yaye nékal make mane bou gniou la done toudou yaw rék alors kone j'allais m'en foutre c'est ta peau mais yaw kham guani kouné mère aminata gniou néla yayou Gniémé té kou tilimale sama dére lay bagne y'a déjà assez de rumeurs sur moi
Mère aminata: mayatima sama diame dh Gniémé té sakh nak télena me bourre pas la tête je suis veuve et alors sa baye mounoule di dounou di ma lakal di déé dima lakal lolou mom dou loumaye accepté sakh nak mane Diallo dama sokhla sama bopou ni yéne fimou tolou ni bayiléne ma ak sama afia ma vivre sama ohhh lala fala yame
Gniémé: d'accord kone nonou guako guissé mais je crains que tu ne puisses pas vivre ton fameux ohhh lala surtout si tu ne règle pas le fou de cette maison
Mère aminata: bane fou
Gniémé: keur gui niata dof la ame
Mère aminata: Tidiane loumou défati
VOUS LISEZ
NIAREL XARITOU JËKËRËM
Ficción GeneralUne histoire typiquement sénégalaise du jamais vu vous allez être ébahi par toute les émotions qui vous attendent dina khoumou té daguane