chapitre 26

74 18 8
                                    

Mourtada décida de se réconcilier avec Zeyna .

Mourtada :  slm Kone Zé tayy ya dougue wagne loyy melni kou amoul diankk ni

Zeyna : cv silonek waw

Mourtada : sa tontou gatt nadi sokhna si yayou Kamal ni ngay accueillir gane

Zeyna : fi koufi gane

Mourtada : en bon  douma fi gane Kone bakhna tayy loyy togg agne

Zeyna: thiebou thieune penda mayy

Mourtada : souniou plat national bounioukoy togg naniou ko diokh kou saff lokho kom Zé

Zeyna : danga kharane si khana loula fi andi

Mourtada : tayy dama nieuw pour niou wakh tane . xam nga ay makk laniou té légui sakh niou nékk mame . Lima layy wakh ni naniou ko deff nguir yalla ak souniou dom kamal . Erreur dou niank si adina man nitt la kom nieupp té nagou na dama dioumone  rk .

Zeyna : dégue na sa wakh mais Dina si xalatt

Mourtada : bayilma  sa wakhou xaleyi dépassé naniou ay dina si xalatt naniou ko deff fondé famille c'est mieux niom Makhady sakh dama beugue niou gnibi si bou boba ma dieundeul léne kéne kou nékk keuram di deff founé 2 jours inchallah .

Zeyna : wa bakhna dinako  ko deff nguir Kamal

Mourtada : waw kayy diékk rétane té faté nala wakh sama rakk bi  Petit Prince té mou nékone États-Unis néna dayy gnibisi semaine prochaine inchallah. Xana légui nakk doma téré wakh Zé.

Zeyna : ioe nexoma dara

Mourtada : wakh kossi souff bayou Kamal ak Cheikh ngay wakhal borome deux galons yi

Ainsi Mourtada et Zeyna se sont réconciliés .

Une semaine après, Petit Prince  revient au Sénégal.

Petit Prince : Salam vous avez de la visite . Ana gnima done lathi magui ni .Namone na galsen.

Mourtada : alhamdoulilah il est de retour .Petit Prince wayy, tu m'as beaucoup manqué ça fait des années . Le travail est important mais aussi il faut avoir du temps pour la famille.

Petit Prince : mais comment allez vous ?

Mourtada : oui ça va on s'accroche. Tu as vu j'arrive pas à retourner au Canada je veux même rester ici investir dans mon pays.

Petit Prince : oui c'est mieux sakh nakk nakh  yalla Terral nala ba paré gnibisi diapalé sa domi rew mo geune

Mourtada : oui sante yalla mom xolal  ki nékk sa guinaw.

Petit Prince : Zeyna bari problème nam nala siloné dégue na diougo ngen da ngen done doff Lou rk

Zeyna : li rk motakh kéne doula nam Kone yagui rew batay

Petit Prince : ana sama taw bou gorr gui

Zeyna : dafa dokhanetoudji ak diabar dji xam nga diabar dji dafa nékk si weram

Petit Prince : mashalla lolou nexx na

Mourtada : tu peux monter prendre une douche et venir manger avec nous . On t'a déjà préparé la chambre. En attendant que kamal  et Fabi reviennent.

Petit Prince : d'accord donc tu n'as pas changé, tu aimes toujours donner des ordres .

Kamal et Fabi reviennent et  voient Petit Prince entrain de danser
kamal  : ki mom di pas de danse dou kénéne koudoul pape Petit Prince

Petit Prince : dioumo d sa baye bagui ni silonek

Rassoul : franchement papa me  parle souvent de vous. J'avais hâte de vous voir . Voilà ma femme Fabi.

LE CHOIX DU Hasard,LE HASARD DU CHOIXOù les histoires vivent. Découvrez maintenant