chapitre 24

79 21 7
                                    

"Aujourd'hui est le jour tant attendu mon rêve va se réaliser moi Diarra , je serai dans quelques heures madame et je vais me marier avec l'homme que j'aime.
Ma grand mère et mon oncle Mountaga voulaient me forcer mon cousin car ils pensaient que je ne trouverai pas un homme qui m'aime comme Ousseynou. Ayez des Ousseynou dans vos vies !Vous voyez , on s'est connu à peine mais notre amour est plus fort que tout.On s'est connu il y a juste 6 mois et on s'était jamais vu auparavant mais on a décidé de s'unir pour la vie. C'était compliqué au début mais c'est parceque notre amour est sincère qu'on a pu convaincre nos parents et je ne regrette pas ma rencontre avec kamal  Il m'a beaucoup aidée .La joie que je ressens est inexplicable!"

Voilà arrivés les parents d'Ousseynou accompagnés de ses amis kamal , Babacar et Tab .

kamal  entra et demanda à Diarra

Kamal : du blanc sur du blanc avec avec du noir à la figure. Mashalla ioe kéne doula ni Madame kholall sa garde robe

Diarra : Merci beaucoup ioe sama Dieucoeur nga

kamal: tay dangay dougue cours des grandes wayy. Fabi migui ak Mère yi di nieuw sou yékk sé mou diokh la clé yi

Diarra: tékk ngama beut nakk sa guémine

kamal: Boulma fonto wayy ma mayy la dieukeur nga beugue ma yapp mais bon je suis très fièr de toi et j'ai confiance en toi .Je te conseille d'écouter ton mari et de prendre soin de lui. Inchallah le reste yalla dina motali .

Diarra : loutakh khamo sa bopp rk nouveau marié nane dangay conseiller watté .Mais bon j'appliquerai tes conseils à la lettre kham nga man dama beugue Ousseynou.

kamal: Gni nane ki dafa manquer Ousseynou diko dioyy lo. Amna surprise pour ioe bouniou takké ba paré.

Asta donna des conseils à sa petite fille.

Asta : mashalla sama seutt bi li dé laniou done niaw tokk banioulay mourr ngay séyy wakhouma seuyi wakhouma sétti wayy séyy yi lala wakh beuss niki tayy Ousseynou moyy sa kilifeu sa goro bou gorr moyy sa pape sa goro bou djiguenn moyy sa yaye. Beuss bo dèmé séti di nga gnibisi watt nakh bofa guissoul li ngay weur dofa tokk té lolou dou seuy. Djiguenn bou néké si boum waratoul kharito waratoul takha walou ligueyam keuram dieukeuram mo wara nékk kharitam bo démé  ligueyi so nieuwé nga topato sayy goro ak sayy nieuké si seuy bi laniou bokk nakh fethioum lire sou nékhé makk yi nio diapp sa nigue la deugue ay khalé ngen beuganté ngen wayyé nakk seuy dou nonou nimou nékhé nonoula mèté nimou dissé nonoula oyafé boul setlou bou khol khamal ni fofou nga deukk biss niki tayy fi amato fi dara fofou moyy sa famille dieukeur nakk sangue la dou fowou kayy. Lékam déko topato dikou wakh tanal bou ligueyi wé nieuw sone nga fateloko thionom guiss yoyou ngay deff moyy dess si bopam ba doula dieundé dara. Parfois nga séduirate ko mou khamni diabar la am ngay deff sayy mini jupe you bakh di diagar diagari mouy contane. Lo xamoul kagne layy diékh na nekh

Diarra : inchallah mame ni ngako wakhé nonoula koyy défé

Voila l'essentiel vient d'être fait les gens commencent à féliciter la nouvelle mariée . Tout à coup Ousseynou apparaît. Ousseynou prit une photo avec sa femme.

Diarra :. tayy dji léww nala dogue foma yobou ma topp la baraque ak makhal mouy nékh mouy nakari.Soma téré ma bayi soma santé ma deff dina méll ni talibe ak serignam lo beugue silay dokh .Diébal nala sama bopp andina ak alakhira. Ioe mi Ousseynou yayy sama sakk.

Ousseynou : alhamdoulilah dina la têyé nimou waré inchallah deuko la deukeul la yorr la ba do gné sa béne morome. Di nékk sa ange gardien , sa dieukeur , sa conseiller, sa compagnon, sa wétal té lo diokhogne ma dakk nguir thiofel bima am si ioe.

Tab: c'est émouvant ça. Yalla naléne yalla moussal si thiate ak lamine sam léne. Yalla naséne yéné ague si barké sagou sangue yi . Seuy bi yalla na bokk si seuy yiniou také si arass yalla boléne guiss louléne diakhal.

kamal: voila la surprise dont je te parlais, il était caché dans la voiture . Tayy la yaram yeup di daw ndiouga bongo yeugal .

Ndiouga : Diarra Ousseynou loumou la diaral athiou baba  athiou néné bayi wa Kaolack dem Dakar sa souko sokhla ....

Wa lilan beignets beignets dougoup bou am soukar Ousseynou moko mom. Diarra loumou narr bataré , chérie Ousseynou loumou narr bataré kou sokhor meunou  kou ignane meunou borome lokho bou dague douko deff.
Mani kharitou dieukeuram yi yéne layy wo

Babacar : niogui ni soniou wowé niou wouyoula dé wayyé souniou lokho doula wouyou

kamal: tayy faw sama rabou Gueweul gui yeugou khamone nani di ngen tassé té dou niro ak lém khamone nani boléne tassé moy dakk mburou ak lém Diarra ya geuna khégne xétou pone si Ousseynou soko diégué tatt layy deff .

Tab : waouh kone am nga talent chanteur tmt .

Les femmes arrivent, la fête devient plus belle. Maty fait la bise à Diarra et prend des photos avec elle.Elle dit j'ai la plus belle fille au monde vous voyez et tout le monde se met à rire.

Ndiouga : kata fayou kata fayou kata fayou Maty koula meussa kata yane ngako brique kata fayou Kone Ousseynou boula andilé li War ngako meuna décorer

Vers 22h, ils commencent la réception.  Les mariés entrèrent dans la salle.

Fabi: waouh mashalla holall séne bleu tmt thia hôtesse gala mais gni sagne Sé naniou dé

Les invités commencèrent à crier un bisou , un bisou.

Fabi : Cadeau d'Allah loutakh defou niou réception mayy solo di soumékou

Kamal : dou yadone doff doff lou di kharou. Nouniouy réception wé té yagui teude birr hôpital.

Fabi : c'est bon diogal niou Féthi Dj bi fimou tékk musique bi nekh na.
kamal  dansa avec fabi quelques minutes après elle tomba et perd connaissance. Ce  qui inquiète tout le monde . kamal, tab et Babacar l'amènent à l'hôpital après les diagnostics, le médecin sort et félicite kamal.Il lui dit tu seras bientôt papa. Il cria tout l'hôpital.

Babacar : li geuna gaw ki mom gaw na dieul ball bi d .Mais félicitations bro wa Tab loyy khar tmt.

Tab : félicitations bro boy dom mbirou yalla ioe loyy khar pour takk sokhna .

Babacar : bayil après ma expliquer léne khew bi motakh.

kamal entra dans la chambre de Fabi et lui dit je n'ai jamais été aussi heureux yayy sama trésor.

Fabi : alhamdoulilah so paré nga woutalima tolll té bb bi moma wakh ni néna papa nako togal mbaxall bou toyy

kamal : fi rk lama yalla done xar nakk.

Kamal appela Ousseynou

kamal : boy na musique bi na  yeugou nouvelle diam ak salam la. Je serai papa

Ousseynou : alhamdoulilah wa li nékhoul

kamal: en kayy.

Ousseynou : beuss bi dafa ala dawmé gnary mbecte ay thia Dji son.

La grand mère de Diarra rencontra le fodé du village. C'est  à dire le voyant .

Fodé: sa khewou seutt bi nekh na lolll té li nga si khamoul moyy léral deugue yiniou warone kham. Wayyé di andi takali ko ayy nitt you yague ande té guiss na tribunal d

Tribubal? et pourquoi?


N'OUBLIEZ PAS DE VOTER ( lall étoile bi) ET DE DONNER VOTRE AVIS

LE CHOIX DU Hasard,LE HASARD DU CHOIXOù les histoires vivent. Découvrez maintenant