partie⚜️5/35

7.3K 388 11
                                    

Après avoir écouté l'audio, Capi sort de son bureau très en colère direction chez Karina. Badiene revient de son rendez-vous avec Adja et raconte à Karina comment elle a bien remise Adja a sa place.

Badiéne:: tay dama contane ndakh Adja nok yimako nok, warone ngaka féké way, ay soumako meunone filmé, bimay dém nak manko bayi guémin bangui nathi
Karina::  Badiéne deuk bi deukou loi la amo droit dor kén xana xamo linga déf sa prison xadj nassi té beugouma ngay am béneu problème
Badiéne::  légui damay tok xalé bi dima manqué de respect ma croisé les bras jamais de la vie, dinako wane sama dissayou lokho ba dou traité ti de thiaga moromou ndayam
Karina::  thiaga ?
Badiéne::  lolou dé lama wakh
Karina::  xana ndayam moy thiaga
Badiéne:: elle avait besoin d'une bonne correction té diokh nako elle est trop malelevé way cette fille dafa réw ba neup
Karina::  mafi nékone dila moral sakh wayé c'est très bien fait pour elle meunone ngako gnouss bou bakh

On sonne à la porte. Badiéne va ouvrir et Capi entre sans la saluer allant directement vers Karina.

Badiéne:: wa yaw ki foumou diougué ak méram
Capi:: yaw karina yay djiguene bou bone yay imbécile , yay domaram
Badiéne::  ah ah ah insulte !
Karina::  xolal je te permet pas nak ngay gneuw ba sama keur dima insulter ndakh Adja, balou nala ngani danga sohla pose may nala pose yaw Lo beug finalement
Capi::  Ehh doul je m'en fiche sa problème ak Adja pour yaw lolou momafi andi
Badiéne:: jeune homme mesure tes paroles yaw amo éducation deh nékété
Capi:: bala nga lidieunti sama éducation lidieuntil sa bossou dom ba paré, visiblement vous l'avez rater ndakh meunoul loudoul fén ak diakhassé ték deal, misérable que tu es, djiguene bou bone bi
Karina:: Capi yaw lane la déf je comprends rien
Capi::  xaral dinga nday comprendre (Capi met l'audio qu'il a reçu sur haut parleur)
Karina::  c'est quoi ça ?
Capi::  li dou yaw, dou sa voix ? Ose le nier, osél nier l'évidence Karina
Karina::  Sama voix la keuy mais je comprends pas
Badiéne:: ay way karina lo déf ni, li lane la ?
Karina:: Badiéne xawma ki dou mane
Capi::  dang ma beugone ruiné, échec na, dang ma beugone diaxassé ak sama frère échec na, danga beugone dougou sounou keur tass sunu famille say plan échec na ndayam Karina
Badiéne::  Karina wahal ak mane bala malay péss, lima dègu lane la
Karina::  li dou mane badiéne montage la
Badiéne:: boulma wakh montage la Karina xamé na sa voix, li sa voix la karina pourquoi ? Loutakh nga wakh wakh you gnaw yi
Capi:: rayanté lén sén bir sama yone nékousi mais une chose la beug nga xam ko, je veux plus te voir..tu sort de ma vie est ce que yangui may dégu
Karina:: ay Capi boul wakh lolou li piège la mane douma wakh lou gnaw li
Capi::  si j'étais un idiot j'allais te croire, c'est fini..guiss la ak guiss samay boutite la yamalé tu me dégoûte a un point tu peut même pas imaginer.wakh nala lima lay wakh nak ne t'approche plus ni de moi ni de ma famille
Karina::  ay capi sunu mariage
Capi::  eh bayima je préfère ma marier avec une pute que may marié wou ak yaw
{Capi quitte l'appartement}
Karina:: ay Badiéne li dou mane
Badiéne::  boulma ni mame béneu beugn Karina, beug nala torop wayé amna yo xamni doumako cautionner té doumako accepté, beugo domou diabour beug Lék alalam, takalé ko ak wa keureum yaw ki bo yaké adounam akhkeu bobou danko atane ?
Karina:: Badiéne dou mane wakhouma lolou bilay walay dou mane
Badiéne::  soma wakhaté Badiéne dou mane nala noka gnouss, dof ngama diapé wala
{karina continue à verser de chaudes larmes}

__________________
Adja arrive à la villa. Tata rose remarque tout de suite ces blessures.

Tata Rose::  Adja loula dal yaw, koula def ni ?
Adja::  dagn ma done diémeu agressé (cassant sa voix et jouant la victime)
Tata Rose::  alakhou akbar lomay wakh ni yaw ? Ba gagnou gnoula rék laisse moi voir
Adja:: non non dama xossou rek ya rien de grave
Tata Rose::  agression keuy grave na
Adja::  heureusement yobouwoul sama dara, bi nite yi commencé gneuw la daw
Tata rose:: dem nga hopital
Adja::  no diarouko sama bop bi rek moy métti dina nane ay calmement ça va passer, Marie Jane defaral ma café stp nga andil mako sama chambre
Tata rose::  wa démal nopalou mangui wo sa dieukeur légui téléphone, ay way yaw Adja mi ray nagnoula di,
Marie Jane:: agression dafa bari temps surtout sunu guinaw kogn motakh sama yaye dou beug may goudé
Tata rose:: mo yéy kat, agresseur yi bakhou gnou bougn la diéko rék dagn lay ray, nangou alalou diambour diaral nalén louné...démal défaral Adja café bi gaw

Obsession - CHRONIQUE SÉNÉGALAISEOù les histoires vivent. Découvrez maintenant