chapitre III

5.7K 752 20
                                    

Anh non dakar metina trop pour ga dém fen non meunoul nek circulation rek ak khamadii chauffeur yi mais hamdoulilah yeksina ci diam.
Kharal ma téléphone papito waax ko mou nieuw nane ataya.

Matzo: allô

Papito: waw boy nakamou lou xew loula dal sa bate bi dafa diss

Matzo: non boy dara dalouma dama khawa sonou rek mais nieuw na magui galé kay nane zeum

Papito: waw ok amoul blém magui tew

Bama paré waax téléphone ak papito si la wowé sama rakk bou jigen bi pour mou tangalal ma agne bi

Matzo: Nafi Nafi wa Nafissatou ioe

Nafi : naam magui ni di nieuw

Matzo: ioe légui khana sa nopou yi nékhoul

Nafi: degoumala deh magui wone sama négou yaye.

Matzo: wa baaxna tangalal ma sama agne , ani Sama yaye

Nafi: waw magui koy tangal sama yaye dafay nelaw.

Bama agné ba parei thiooo non mais mère bi meuna togou koi kholal ma bi khétou yassa guinar non vraiment mère koudou louss mo damou ci lokho bi mashallah.

Koc koc koc

Matzo: Nafissatou démal oubii bountou bi khamna papito la

Nafi : waw d'accord

Papito: Nafi naga def namenala

Nafi: wa ki dou sama frèro papi ioe mala raw

Papito: Hamdoulilah magui cool anii pape matar.

Nafi: mogui ci bir eksil

Papito: wa fils nakamou dafa melni daga sonou

Matzo: weuy fils sonou trop mais tkt comme amna ataya sama médicament lep trankil.

Papito: waw lo dieulé université ?

Matzo: boy guiss na tons bi deh mais néna na khar mou khol gayam yi bakham.

Papito: waw tkt boy dina baax inchallah liga dath ci bac bi yeup mais yalla baaxna.

Matzo: inchallah wa boy ani Nabou légui bayinama deh

Papito: anh boy bobou dafa sof lguii koi ay jikko lamay indil mais mais nak mom la beug wakhal ak mom dakh mou changé.

Waw Nabou guelou papito gnom niar def 3ans ba sen famille khamanté mashallah.

Matzo: waw boy na waax ak Nabou mais nak ioe comme indo mbeguel yi moy lan

Dioxma sa xalat📑📑

Besseul🌟🌟🌟

Salam ladies and gentleman it's a real pleasure for me to Write this history my history in my maternal langage

svp j'ai besoin vos avis guir yalla

Athia am len diam way ❤❤❤

sama mbeuguel ci mom Where stories live. Discover now