Mame Cheikh Ibrahima Fall dana wahnane fou way yakho sou diké sama Keur gui défarou wayé kou yakho sama Keur gui doto défarou ba faw
![](https://img.wattpad.com/cover/213358230-288-k112089.jpg)
VOUS LISEZ
Wakhi Mame Cheikh Ibrahama fall
SpiritualAy kadu fatali ak ndékané sounou Mame cheikh Ibrahima Fall louci ndeungue niogui koy toub té hamni matadi Domou adama la wayé lepp louci bah niou santé ko serigne bi ndah lou bah rkk lagnthi dioublou Yalla naniou serigne bi defal dégg ak topou niou...
18
Mame Cheikh Ibrahima Fall dana wahnane fou way yakho sou diké sama Keur gui défarou wayé kou yakho sama Keur gui doto défarou ba faw