05

1.6K 97 7
                                    

"Ah dom niom dagniy topou yallah.
Yen nanguén woutt yallah.
Ndah kouy topou yallah dangay diouli worr nate azaka dém maka.
Wayé kouy woutt yallah sa bakane sa ndiabott sa alal lagn la lath.
Kouy topou yallah yallah yeureum leu.
Wayé kouy woutt yallah yallah gueureum leu.
Té kou yalla yeureum nga dougou aldiana.
Wayé kou yallah gueureum nak dangay dougalaté aldiana "

Wakhi Mame Cheikh Ibrahama fallOù les histoires vivent. Découvrez maintenant