chaise sensuelle

2.5K 41 1
                                    

Djék thiaga, Djek thiaga, Djek thiaga... thiaga bamou nex teh yam sa dieukeur..Djek thiaga😎😂😂😂

Salam la mifa 😍 amoul noumalén namé woul woneu 🤗🥰
Tay nak ma nieuw ak yén si bén accessoire plus que important dans la  chambre d'une djék🥰
Ma nieuw ak yén si ndiarign Chaise...😎
Il y'a chaise  et chaise  hein 😜😅
Négou diék bou pareh mom waroul niak chaise😏chaise  bou deugeur la wax nak🙈
Wawaw out sa chaise bou deugeur couleur boula nex...  dissi bégal sa goor si ay leumbeul you amoul fén 😋 lolou mom wolou nassi laobé yi😅 ndax kat goor lika diomal yomboul surtout so néké niarel wala niétél...😏danga wara geuneu féroce geuneu khadiam...🔥
Pour djék yi ndaw yi  sén dieukeur nékoul fii  meun ngén commencé def sen entrainement chak goudi😉...wawaw Tegal  mbalax bou saff sapp🙃 dissi dém ak dolé nak😅.
Hummmm...😋😋  Djék day nexx ndig waw kay😍
Même yén sax  singén bokk, taille fine yi ak contre-plaqué  yi...😂
djék dall day yor djiko Ouzin Keita   di feulé fouko kén yakaroulé😂.. di innové di indi lou bess...wayé routine rek 😒
Ma nieuw nak si chaise bi ak ndiarign bi...😁
Sopou  na ngakoy def goudi nak ndax ambiance bi geuneu nex... faye sa lamp Tall  bou rouge bii...😃
Takk say todj khourr ba ndig li fess dell ba nga xamni ndat  say bo def supporters yi youkhou 😂
Nga dindi soutien  bi sandi slip bi feulé ...😋sol sa mini pagne wala béthio 😊  dieul sa huile de  massage diw sa yaram bi bamou niine mbat  sikaw bassi souff ninay bi day excité goor...😋
Nga ték sa chaise mou diakarlo  ak lal bi sa goor sol khoukhal djék😎 bou ndaw ak sous-vêtement teud diaxan melni kouy sétan télé...😀
Nga def sa défilé bou ndaw si kanamam diko xol si beut diko thiokass diko sandi ay wax you séw you bandit ymgx😜.
Def sa geste you posé avec élégance nak yék ndank sisa chaise dieul position guestou diko thiatal beut... commencé wané sa meunin  nak...des fois nga fél  seur bi  xaritam  fégn😃😍 nga wathié wat ko ndank.🔥
Lélé  nga adj fer yi bassi kaw bayi mou wathie thiow li tambalé nak.nga dieul sa temps tourné mayko diakarlo bi nak face to face bi😎
Nga moyto danou si souff nak 😂😂😂 dense  sensuelle di wan lep diko ray mouy dégusté 😋
So pareh nak nga wathié ndank Tall sa lampe normal dindi sa petit pagne fasséné deff bamou bax nak.😍😋 wayé xamna doi aksi fofou sax🙃 ndax leumbeul bi sou diaré yon mom bala nga wathie sax  mou fek la fofou wan la ni mola geuneu nex ndig 😂...

                                                                  À suivre...

Coach #Aboo ngay am nonou😍
Mafi diaron nii..🚶‍♂️
Ba bénén yoneu si yénéni astuces🏃🏽‍♂️🏃🏽‍♂️

          🔥Djek thiaga yam si gooram🔥





Vous avez atteint le dernier des chapitres publiés.

⏰ Dernière mise à jour : May 31, 2020 ⏰

Ajoutez cette histoire à votre Bibliothèque pour être informé des nouveaux chapitres !

chaise sensuelle Où les histoires vivent. Découvrez maintenant