Goro bo khamné lo manigancé mou échec guani do bayi mais yama dou nittou défaite comme nimoukoy wakhé rek yama gueneu bandit gueneu moll . Ce jour où elle doit montré ses talents culinaires est arrivé . Wane nieup ni diabarou el Bachir diaw meun neu togg .
Son état major est là .Elles sont dans la cuisine pour l'aider les invités sont déjà dans le Salon un peu éparpillés dans les autres pièces tay dou yomb nak ambiance bissi wagn bi diarna louné . Ya Fatou diouguë feulé di diay forokh djiko ak wow beut_ assalamaleykoum yenagui tokk machallah rafett neu dall , beugeu na you bakh yi solen paré rek deflen ma sign ma nieuw sëdeulé Agne bi waw kay yama bassi kanam nala yalla defal diam
Après mou dém rek dallou ndakarou todj😂😂
_ wa mom louko dall khana danone dioy beut yi deh comme lampou pétroleNdella _ Man nak damako yeureum mom dou bayi d'ou randou dou rekiller en avance rek
Salla _ commencéti guen bakhna rek ki def geste bou nice guen diko kokeuli
Yama _ salla khamgua louma metti thi yaw moy dagua lekk seytané ba Paré né doko réssal .
Ndella _ yay wakhak mom deh pour qui rek gélam bou Bari nikou deff lalo mbipp
Dallou ndakarou _ wa eh bayi len togn nagn dioubeulou thi Agne bi .
Tassou bi recommencé 🔥💪👏🏾👏🏾💃🏿💃🏿
Yama _ laylalaw diek guatam kouko wakhal lou bakh la kham ehhh diek guatam .Ndella _ samba laobé Ndiaye mbarodi Ndiayes. Ni dougou dougou karass doula diapp raw gua say noone . Pesé khél natt fitt ken niaméwoula
Dallou ndakarou _ khalass li kouné nekhoul dagua amé siiti ."guine thieuss" bi thiep kouko niame degg alhamdooulilah .
Wayéee kou lakka daay guiYama _man ma lakka daay gui 🔥
Dallou ndakarou _ kou lakka daay 🔥
Yama _ yé ye yee ma lakka daay gui 🔥
Ndella _ beukeuteu beukeuteu
Yama _ barra Mbaye
Ndella _ thieuguine thieuguine Reuw Reuss
Dallou ndakarou _ wooyayaaye tayla wagn bi di kharr ayy wayyy 😂 na riiiiiirrr
Salla _ 😂 ay way diapp len yama monguay sabarou nakk
Yama _ aywayyyyyyyy sa goune gou ndathie . Rakoukou sa goun thiourr Ra koukoune goune sa goune ndathie 💃🏿💃🏿👏🏾👏🏾😂
Dess touti rek el Bachir dougou thi wagn bi _ wayen sen fi mom khoumb nadi machallah
Yama _ guiss geu deh may khauny
Salla _ my honey
Yama _ doul yaw
El Bachir _ haha machallah wa yama kay nouyou sama ben kharit de longue date sakh bamalay tak nekoufiwone
Yama _ ah ok kharal ma tek dara sama kaw khegn lou nekh gnou dem
El Bachir _ diarouko dagn koy dialé rek David boulanger leu toud degoul sakh Wolof neko mes condoléances rek après dém
Yama ak Bachir djitelé pour nouyou David nakala eski gnou deff présentation bi
El Bachir _ David voici ma femme adorée
David _ ah yama te voilà enfin Bachir m'a beaucoup parlé de Toi je suis ravi
Yama _ wouy sama nday bachir ki français you cimenté lay lakk douko wagni
El Bachir _ neko David boulanger je vais bien mes condoléances pour ta mère
![](https://img.wattpad.com/cover/243127731-288-k725792.jpg)
VOUS LISEZ
RAKADIOU
Humorquand un couple lutte entre l'alphabétisation et l'analphabétisme seul l'amour peut les libérer.