Au marché

1.3K 29 0
                                    

Vacances diekh na ba paré.Béneu Semaine bo dess école oubi. Oumou AK yayam Mère Niang nioungi marché Di diaye ndougou. Après clients yi hawa wagnékou yayam néko togual niou wakhtane.

Mère Niang : Oumou guiss nga Adouna bi dé li mofi nek . Liguey rek Mouy goor wala jiguene nieup la War limalay yokou moy adouna bou méti banga faté sa Borome ( Dieu ) wala nga guiss lénene ba heep sa bopou...

Oumou: Yaye ! yaw Yama yare té foula AK fayda ak diome bi nek si yaw mo nek si mane mi sa dôme . Boul ame Dara loy tite sa béneu bou jiguene bi. dinako def ninga ko beugué .

Client : Salama lay koum mère Niang Niang balo naka ngene déf. Oumou sama dôme yangi tok .

Mère : Maleykoume Salam sama kharite. Naka niabote gui. Mba yéna ngissi diameuh

Client : Alkhamdoulilah kay!
Mane dé dama beugone nga lébalma ndougou ba souba inch'Allah ma fayla sama borom keur mo toukki té fane yi yeup dégoumako .

Mère : ah yaw lolou douniou bolé deukeundo bou bakh nga machaAllah amo béneu problème. Heureusement dama done wadial lali ni sakh pour yégeu keur gua.
Oumou défal ko li mou beug thi léguette bi.

Client: Mane dé awma sa Fay Mère Niang Limalay leep barina té meusso ma banial mba douma danel sa table bi.

Mère : Adouna amoul solo. Diapaleneté tanéneté. Danou nak si lokho Yalla la nek .

Oumou dajalél bagages yi niou dém gaw nathie na .

Client : Yalla nala Yalla fay sa khol...

Mère : Amine way Sokhna si . Yaw tamite nianal nala lolou

Lou Méti Yagoul 😭Où les histoires vivent. Découvrez maintenant