Assamalikoum 🙏j'espère vous allez bien 👍 nouyou na nieup 👋 Dilen wakh contane n'a si vote yi mais tamit délen commentaire pour wakh sen avis
*Flashback
Djiguene moy diapaleii Dieukeuram Djiguene moy soutenir Dieukeuram dou samay wakh beuss biniou may moureu may seuysi si Doudou Li laniou ma wakhon Lima guena rethiou moy le faite que ma nangou khalè bi installé wou suniou keur beusseu boboou erreur la def ndakh naron nassi niak sama foyer ...
*Fin de flashback
Wayeii nak seuy amoul louko guena Métti surtout bouneikei seu mbok Dieukeur yi meuno def loulen satisfaire Wayei sonon n'a si yareu bi ndakh Anna bamouy ameu 13ans dafeu commencer changer louma ko wakh mou tountou meu nangou woul diangue tei lima guenon meti moy Ndeye Mareme dafeu niou don mettre en mal.... Bagn Lou metti Anna takh na togeu sakh douma ko beugeu wo tellement que dameuy beugeu mou profiter si vacances yi mais louma nekh doumako si ameu
_ Khadija lanla beugo meu tok wakhtane ak sama Badiéne
_Ahhh Legui Khadija geu may woweiii seu morom laah ?
Ndeye Mareme: Khadija temps yi guiss n'a nigeuy comporter wo ak khalé bi ioe ki khamoul dara dageu meunoul diour motakh khamna niou leep yaw beu geu dougeiii si keur beu legui meusso kham prix Dakaaaar ak toleu☺️ Moi:Li moy sen wakh ak maneu ?Doom d'où contrat si seuy bénéficie rek lassi Wayei yalla bakhna Nonou la demaii dougou sama neikeu ndakh beugouma ameu bleme ak moom
Le soir sama yaye woma appel 📞
_Assamalikoum 🙏, Khadija ioe bayi geu seu yaye deii
_Ay yaye boul wakh lolou khamgeu neii doumala meussa bayi tu me manques 😞 énormément naka geu def ak seu yaram ?Ana sama papa
_Cva magui si diam goorgorloul bou bakh ben seuy nékhoul inshallah leepay bakh
_Dina ci bayi khel bou bakh Yaye seuy geuma santeu na goorgorlou inshallah allez bisous
Meu raccroché rek Wadji béteu ma ak ben câlin 🫂 ak 🌹 malgré souffrance bima doundou yeup si journée bi boumako guissei dafeuy melni yalla leep lameu téguil meu defaral ko mou agn sangou et tout...wxtane ak moom
Deux semaines après Meu commencer di remarquer ay changement d'humeur manque d'appétit meuy gawa sonou en plus dameu don ameu ay nausée tout le temps meu commencer ameu ay doute si la dem pharmacie outeu teste de grossesse au début dama don ragal esk dina neik Lolou
Devinez ndékii madeu dîna diareu réneu 😂Lolou meussouma ko imaginer
Oups ! Cette image n'est pas conforme à nos directives de contenu. Afin de continuer la publication, veuillez la retirer ou mettre en ligne une autre image.