Hello!j'espère que vous allez bien ?
*Flashback
Ma maman s'est installée chez-moi après mon accouchement
Khadija nak il faut geuy lékeu
Yaye soupeu bi dafeu tangue trop Kharal touti
Y'a guena khamneii rouy bi dafeu bakh si Djiguene bouy dogeu ameuu doom yen daleu louniou len wakhoul rek khamo len ko
Yaye nak sen temps ak suniou boss bokoul bakhna rek
Wouyoul seu téléphone 📞 yaye c'est Ndeye Mareme Niewal déglou
Allo Khadija
_Oui Badiéne xalé yi Ndeye Mareme comment tu vas ? Yakarna nei kham geu Li khew amna doom Samedi passé
_Oui yeuk nako comme d'habitude maneu may moudié yeuk seuy birr diéck bou bonne khamon Nani do Diour doom bou Weir ndakh do soleu moukeu yeureiii you dioteu
Tei Khadija lima guena Métti si ioe khamo teranga_Yaw dei toute façon meunouma def mouk louleu nekh sama doom nak mou nekh leuh mou nakari leuh yay badiènam tei seu mak Doudou Gueye maneu leuh Nop dageu makoy nangoul par force leuh
Khadija diangualou maleu lii seuy laleu santeu
Yaye khamna Lolou mais ki beugouma ioe degeu geu limou ma wakh yeup au téléphone tu as tout entendu
Mais wo ko geu excuser wou seu ndieuké laa
Lan yay Lolou dea moma ko guenal
A vos claviers
Êtes vous d'accord avec Khadija?
*Fin de flashbackMon amour réveil toi ?
Ahhhh chéri suis trop fatigué Doudou hier j'avais une insomnie j'ai pas l'esprit tranquille je pense trop à ma fille
Bébé j'ai tellement souffert pendant l'accouchement et me voilà meunouma ko diokh wénn (sein)sakhKhadija J'imagine mais t'inquiète pas tout va s'arranger je te promets chérie d'ailleurs beugeu n'a niou changer appartement comme ça on aura beaucoup plus d'espace pour nous trois
Legui ban appartement laniouy dem?
Niou dem Almadie
D'accord chéri ça me fera plaisir ça sera après le baptême donc
Bon Khadija à propos du baptême est-ce que tu peux m'accorder quelques minutes s'il te plaît ?
D'accord Babe vas-y je t'écoute
Khadija instant bi yakarna diaroul maleuy wakh suniou état de santé doom donc dama décidé niou bayi def khew bou reuy
Bon d'accord degeu nala
Legui Doudou kan geu beugeu toudeu Bébé bi ?
Bon écoute mon amour
Lolou nak surprise lakoy def beugouma ko wakh stp may ma Lolou rekThiey Khadija ak Doudou dem beu ameu louniouy neubanté boul faté nei bébé ioe kessei diouroko tei stp Doudou sort dans la chambre j'ai envie d'être seul
khamouma yaneu genre niteu guen hier c'était Ndeye Mareme louneii wakh nameu ko mais ragalouma Lolou Legui ioe la Doudou maneu dolen ma rayeu MoukSamedi jour Baptême
7h30Yaye kharal ma niew dem hôpital guiss bébé bi avant may niteu gnii di niew

VOUS LISEZ
Un vrai amour
AventuraUne chronique sénégalaise 📝 Un vrai amour 🫶 Un amour pur,un mariage enviable ❤️ Découvrez l'histoire de Khadija Fall et Doudou Gueye