chapitre 2

1.6K 102 4
                                    

Soukeyna: mane lanla deff  Ya Fatou bam warma bagné ni they yallah

Totoc

Soukeyna: Entrez

Khady: Soukey am andil nala sa agn lékal mo guen

Soukeyna: Tek ko fo

Khady: Soukey mougnel rk yallah bakhna sama yaye mane la gueneu diakhal bilahie dama rouss sakh

Soukeyna: Khady yaw dossi dra yaw yalah molay fay guiss na nig ma takhawo trop. Sa yaye mo diel yonnam rk ms yaw sonnaloma ben yon.

Khady: Sama diabarou mak ga kone damala wara diapé kone sama mak.Magui demb

Soukeyna: Merci beaucoup khady

Khady: Ok

Haral ma wo Mamy sama meilleur amie. Mou gnew wétalima touti

Soukeyna: Allo

Mamy: Allo soukey Cv

Soukeyna: Cv silonek

Mamy: Magui ni reck dila name

Soukeyna: Mala raw wa doffi gnew setsima soudé deffo dra

Mamy: Wa bakhna haral rk da am foa diem soumafa diougué diar fa.

Soukeyna: Wa maguilay har

Comme que gnewagul haral ma teud nopalou touti.

30mn aprés

*Point de vue de Ya Fatou*

Ya Fatou: Haral ma tok si eutt bi fekhlou touti

Mamy: Salamu Alaykum

Ya Fatou: Mu alaykum Salam

Mamy: Ya fatou Yagui si diam

Ya Fatou: Ahmdll

Mamy: Ani soukeyna

Ya Fatou: Shipp lomakay ladié

Mamy: Wa hana du si keur gui la deuk

Ya fatou: Yako considéré koufi deuk mane dh lindienty woumako

Mamy: Tontou la sakh erreur la

Ya Fatou: hée duma sa morom boy tontu dh fala yam

Mamy: Soff

Soukeyna: Mamy magui ni kay

Mamy: Nakh yallah sakh

Ya fatou: Niguen meuneu mel ben guen. Ki deh koumay abbal la si keur yabou ma sakh Omar moma yap hawma loum guiss thi Ki ba warko tak wayé hamna nimay deff.

*Point de vue de soukeyna*

Mamy: Wa soukey niga deuké a ki

Soukeyna: Guissga dh warou na si Ya fatou trop

Mamy: Togal rk fi diga deh

Soukeyna: Sey momafi andi damay mougn rk dina bakh

Mamy: An bakhna.Wa yaw sakh ani Omar

Soukeyna: Da liguéyi

Mamy: Yeuk na sa goro bi lim lay deff

Soukeyna: Dédet

Mamy: Warga diouk si mom dh limay yeuge moy ga waxtan si ak mom di tel

Soukeyna: Wa nakoko wax so wathé

Mamy: Mo guen dh. Wahuma lolou bayigama dh

Soukeyna: Bul wax lolou hamga rk Moma touma sama bopp. Warga gaw seyi nk

Mamy: Telna bayil massi kanam rk

Soukeyna: Yaw do changer

FIN DE Chapitre

Commenté et liké

Merci












Soukeyna:Mon mariage, mon combatOù les histoires vivent. Découvrez maintenant