chapitre 6

811 79 0
                                    

Ya Fatou: Omar tay mom dagnuy am gaan

Omar: An yaye kouy gnew

Ya Fatou: Sala mofi gnew

Omar: hum gueth naffi dh

Soukeyna: Kouy Sala omar

Omar: Sala sama couzine la

Ya Fatou: Wax ko tmt mom lagn la beugon may

Omar: Sheut yaye lolou dial neu

Soukeyna: Lolou dra nékoussi

Ya fatou: Heum

17h

Sala: Salamu alaykum

Ya Fatou: Mu alaykum salam; Aahh sama doom di gnewna way

Sala: Yaye namon nalla

Ya Fatou: Mala raw ani sa yaye

Sala: Mogui fa rk; Ani Omar

Ya Fatou: Hamna légui mu wath rk si kanam.Kom nimala ko wahé wone rk diabar bagui si bir bulko may dra nk.

Sala: Yaye nassa xol sed samay valises mogui si biti fass yéné gnew nak diel sama place.Soukeyna mo yakh sama aduna ak nima beugué Omar mu fékhé bam tak ko bayi maffi

Ya Fatou: Li dh la beug gnaw ki dina ham gnoy kane.

Soukeyna: Anh Ya Fatou mane la beug yakhal mtx mu andi fi ki. Ki dh touti na pour diel sama place si keur lolou lagnuy xol.

Soukeyna: toctoc....yénagui tok Sala comment tu vas

Sala: Bien merci

Soukeyna: Omar wax nama say wax fait comme chez toi keur sa keur la degga

Sala: Merci

Soukeyna: Magui si birr

Ya Fatou: Ki nimako diépé thim.

Sala:Damay wan moma eupalé si keur gui magui dall. Magui demb tougal sama valises yi si nek bi

Ya Fatou: Waw

Sala croise Omar qui venait tout juste de rentré. Fatou entand dans sa chambre jette un coup d œil pour les observé.

Sala: Wa ki du sama Omar

Omar: Momlakay Sala nam nala

Sala: Mala ray yaw silonek

Omar: Magui ni rk ani wa keur ga

Sala: Gogui fa

Omar: Do bayi ma yobul la sa valises

Sala: Da diss dh

Omar: Grawul goor la

Omar aida Sala a emporté ses valises dans la chambre d amis.ils sont seul dans cette piéce soudain Sala s aprocha de lui commença a lui caresser.

Sala: Omar yaw yamafi andi esk hamga lolu mane dama beug souma sagnon may nek sa diabar dila deffal yu bakh.

Omar s éloigne d elle un peu et lui dit.

Omar: Sala mane amna diabar ba parei lima sokhla yep mig makay diokh vraiment té wal sa boppu si mane rk beugu ben probléme ak Soukeyna.

Il n' a pas attendu sa réponce et quitta la chambre pour rejoindre sa femme chérie.

Fin de Chapitre

Commenté et liké

Merci






Soukeyna:Mon mariage, mon combatOù les histoires vivent. Découvrez maintenant