KMTN 5

7.4K 818 27
                                    

Penda
Comme que Sira descend à 17h tè il fait 16h 🕓 j'ai décidé d'aller cii bibliothèque bi pour réviser en attendant qu'elle descende.

30 mn passa........
Une jeune fille de teint noir et très sexy passa en me saluant:
_ Hey wassup? (Cma cv?)
_ Magui ci diam
Et oui elle est sénégalaise
_ Have not seen you in a while? (Sa fait longtemps qu'on s'est pas vu?)
_ legui guiss guama kay bakhna
_ Why you gotta be mean? (Prkoi t un peu méchant avec moi?)
_ Hmmm.... Daguay lathiè
_ Ok. Anyway I don't have time for this. Bye! ( ok. Moi j'ai même pas temps pour ça. Bye!)

Fallèwoumako sakh. Khamna diguène wakh loutakh ma gnakal ko kersa. Mane sakh melouma ni mais c'est parce qu'elle le mérite.

Elle s'appelle Safia Mbengue . Elle est sénégalaise et elle a 20 ans . C'était mon ex meilleure amie. On s'est connue kan je fesais la 1ere ici (11th grade). Malgré j'étais tellement naïve tè mane sama leep lako done wakh ba niit yima bokolone ecole dima wakh ma moytouko prck djiko kakatar la yorè. Mai prkoi niit leudeum. Surtout ce qui c'est passé entre moi et Demba, presk kouy sénégalais cii ecol bi khamneneko meme si ils ne connaissent pas qui il est. Mais bon yalla bakhna bima khamè Sira prck je ne fesai plus confiance a personne.

_______________________
Mon passè avec Demba...😩😩
Moi et Demba sougnou relation yagg na dp8 bima nèkè Senegal. Nous 2 gno bokone kogne aux Almadies. Avant que gnouy nek en couple, dafa rèwona reww ba melni i bou amoul tomb. Makk ak Khalè la yamalè. Mane sakh kouma wakhone dina guène ak mom doumako geum. Quand il a voulu qu'on sort pour la première fois j'avais refusé directement. Hiii bougouma thiowww😂

Flashback......... (quand il m'a avouè ses sentiments pour la 2ème fois)

Je savais pas qu'il est romantique. Yeffou toubab film yoyou dh la fi def. Dieund ay fleurs takhaw sama balcon chambre di way son Youssou Ndour bi mbeguel "🎶🎶Wouyy ya nekk ni soumala guissoul damay beug dh wouy mbeuguèloo, nala wakh Lima meune guir gua begg khamni yaw mbeguelaa am nako wakh samay kharitt guirr gua begg khamni mbeguela ame wouy mbeuguèlooo🎶🎶 🎤 )😍😍❤️❤️

Dafmaa bètone tellement. En plus de sa il m'a récité une poème qui me décriais. J'avais plus les mots jtlr. Si je vs dit que dioy sakh defnako diguène ko geum. Eupnaaaa.

_Demba: stp Penda, je c que je suis pas l'homme parfait mais stp je t'en supplie donne moi une chance je vais te prouver que je peux changer et être l'homme idéal pour toi. Faire de toi ma femme, Mme Faye💍 inshallah (Ehh pour mane sakh kii geumoul yalla prck club bo khalate tankam miguifaa, nane sanagaraa mom wakhalè woumako, soudone tokh chichaa sakh gnou dieul yambar dh dou dara ci mom)

Bon, après j'ai fini par accepter sama xarit yi gnoma ci pousser surtout ma demi-sœur (fille de tata Rama). Elle s'appelle Mamy Diop. On était très proche. Elle a 21 ans mai on n'était presk comme des jumelles même si sa mère bougoul wone gnouy ande.
Après, Demba a commencè à changer, di diouli, di dem diouma, di nouyooo ba paa wou kogne bi dagnoo warrou wone. Gno yayy di😂. Mais heureusement que loumou reww reww dafko bolè ak diangue.

Guène nène lou matt 1ans et 1/2. On était le couple parfait même ci desfois gnou mèroo et je pense que c'est normal pour kou nekk kham sa djikoo morom. Sougnou wa keur gneup khamonene sougnou relation. Mes parents étaient contente surtout mon père parque mom ak papam sont des amis. Sauf Tata Rama rek. Mom damako beurgeul. Surtout elle ne m'aime pas du tout. Dama narone tokk senegal ba mane ak Oumar ame sougnou bac. Elle ne fait que dignou créél Ayy problems inimaginable. Di nane mane goor yeup fowè nene ma du n'importe quoi. Wayè dh yalla geumoul nelawoul. Liko metti moy que mom Awo la en plus sama pape sama yaye leu geuneu beug parce que mom ak sama yaye ay meilleure ami lène wone dp8 leur jeunesse. Mais sama papeu bimouko bougone takk, ses parents avaient dit que il faut que mou takk mokkom ba parè. Khamgua rekk l'ancienne génération.
Comme que sama yaye dafa sonone cii bolè you beuri yii, tè mane ak Oumar yeup Usa lène dioudo, on a décidé pour rentrer. Diam la paix ame. Ndeysane Demba ne voulai pas s'éloigner de moi donc papam defaralko ay papier wam pour moi gnew tamite en même temps mou yègali dianguam.

Des mois passa.............
On m'annonça que Mamy amna dom bou djiguène. Dama warrou tè mane ak mom presk chak jour gnou wakh WhatsApp tè meussoumako wakh. Dèvinè rek!!! Nakatèè yoooo Demba mo baye djii. Attend parègouma dh. Lima cii geuneu metti ba metti ma rek moy dom dji Penda Faye la touddou. Après moi. Jour bobou souma amone cardiaque kone dh yènagui dima siyarè Armel Touba. Je pouvais pas imaginer que l'amour de ma vie l'homme que je fesais confiance l'homme que je croyais va être mon futur mari va me faire cela. Avec ça il veut que gnou melate nougnou mèlone. Lolou sakh xel nangou wouko.

Quant a Mamy mom, je sais qu'elle a pitié. Elle a dit que tout sa est à cause de sa mère. Diko nane noy khoulè ba khalè bou ndaw bi di guène ak kou bakh gua tokk fi nara lammb. Motakh 18 ans et maman😩

Comme vous voyez c ça dal!!!!
_______________________
Amadou
Je suis dans ma chambre di jouer sama PlayStation en même temps di deglou sama waly seck "Toumaniii lepp ni leuu ehhh"
Faramareine la nakk💉💉❤️❤️

Après mou ame kouy feugg cii bountou bii:
_ Ko kane leuu
_ Brooo open this door! (Ouvre la porte)
_ Tay rek ma dèè..............

Salut mes amoukhhss❤️ jsper que vous aimez la partie.
Vous croyez que Penda pourra pardonner Demba un jour? A vos avis!!!
N'oubliez pas de voter sur cette petite étoile ⭐️ 👇🏾👇🏾👇🏾
En plus jeter un coup d'œil à its_mainaa elle écrit aussi des chronique en wolof et en français.
✌🏾Peace n Love ❤️

KiMay Tèrè NelawOù les histoires vivent. Découvrez maintenant