2

60 4 6
                                    

-Métou est ce que meun na am sa numéro s'il te plaît ?

Ibra mi tamitt lou takh mouy deglou Zahra dima ladj numéro ? On vient à peine de se connaitre !
Légui louma wara def ? Lane rek lako wara meun tontou ?

Xool na Zahra ay xoolou guenei ma si ! Wayei dou ki di makaro watei mo ma si guenei.
Ma tourner xool Ibra ! On dirait que ni mane rek lay degg lou.

Lane la wara def ?

Gnakk ko diokh sama numéro rafetoul kone dinako rouss lo ! Amoul blem. Ya po feu. Nako ko diokh rek. Le reste dina xam nima kay gerer.

-Waw !

Lolou ndong lako tontou

-Bou dei dalay déranger aussi c'est pas grave. Je comprends

-Mo déranger wou lane ?

Zahra deh moy wah

-No dou lolou sah !

Pour ne pas le mettre mal a l'aise ma talal sama lokho dieul portable bi def si sama numéro delo ko

- Merci beaucoup ! Je vous ferais signe tout à l'heure.

-Wa iow dina xaar sa appel gnou guen wahtane, yama guen xam se rappeler du bon vieux temps !

Dégalma Zahra ! Kiiii

-Surment inchallah. Ce sera sans faute. Au revoir les filles!

-Bye dis-je

- Kone gnou def nonou Ibra. A bientôt dit Zahra.

Ibra oubi bountou oto wam, gnoune gnou deup en route pour sougnou keur.
Zahra mom bou nekei da yakar ni douma ko wakh dara par rapport ak lim ma def mo ngui nax bopam. Douma ko may dara di na nek nitt par force wala mou xam noum def.
Douma sax nek si mbed mii di wax ken di gnou degg na civiliser touti ba gnou agg keur nga rek. Sorétoul.

Ma deugg samay tankk mane waxou samay waxou you tarr, wathie mbouhouri bei mouy direkou mom.

Ma dougg si keur gui yegg si kaw agg sama piaule. Naka la toguei si lal bi rek Zahra oubi bountou bi plonger si lal bi.

Ma diougg mane oubi coiffeuse bi gueinei peigne à queue bi talal ko.

-Li pour lane Métou ?

-Eh mayma fi fatei xadiou fi. Tel xadji wou kay bi nga agali lett yi

-Wa toggal

A la bonne heure !

Fatt fatt xalebi pareina. No ki salon la warone oubi. Bop rek la meun wayei deh bala nga diott si ay letam wah lou sett.

-Merci dis-je

-Je t'en prie

Ma gui kay xool rek sankk ba tay xawma sakh fouma wara commencer reproches yi. Zahra limou ma def si laps de temps bi mo beuri.

-Diankk accouche ! Ni nga may xolei ni xam nako. Waxal li nga beug wah !

Xam sa bop si diamou yalla la bok.

- Pourquoi ?

Ki lima ko wara wah lep pourquoi rek lako wara meun génél ni ?

-Pourquoi si lane nonou?

-Zahra dama lambb ba nga may wanterr niii?

-Si li nga nekk lambb moko tanei ! Dara wou Arona safouma.

-Tayy dall ni nga ma def si ngoone gui . Nekk loma fi hotess de l'air may servir gauche droite ! Gnou fokk nei fangay yam ngani no mane ngay macaro ! Zahra est ce que tu vas bien ?

tankk bukkiOù les histoires vivent. Découvrez maintenant