**Fatimétou**
Quand je passe en revue ma vie, je me dis que je ne suis peut être pas chanceuse en amour.
Au collège quand les filles de mon âge vivaient leurs premiers amours peut être même leur deuxième, troisième voire plus, moi je ne pensais qu'à mes études. Je ne voyais que la réussite. Rendre heureux mes parents à travers mes résultats scolaires était ma priorité.
Dama meuss xalatt ni guén entre collégiens perte de temps leu. Les amourettes ça n'a jamais été mon affaire.
Diangg bou bax, wathie gnibi rek. Xalei sage koi ! Ceci jusqu'à ce fameux jour ou j'ai rencontré Arona.
Je m'en rappelle comme ci c'était hier.
On s'est connu a Monaco Plage à l'occasion de la sortie de fin organisée par notre classe. J'étais en première.Ma ngui nguen si guethie gui pour dem rejoindre sama xaritt yi. Dama meuss beugg ndokh. Bi gnou gneuwei bok na si gni ndieukeu pathiak pathiak.
Ma ngui solone sama maillot de bain bén deux pièces couleur rouge avec des motifs petits pois ma tekk si sama foulard bou blanc. Sama anche yi di déborder gauche droite faw ma neub ko touti pour ne pas être sexy. Sans pour autant me jeter des fleurs, j'étais toute belle,surtout au sortir de l'eau. Mes lifes tombés le long de mes épaules.
Avec mon teint clair bi ma doneu si sama mamou naar yi j'attirais partout l'attention je ne passais pas inaperçu.Après sama repas froid ma ngui savourer sama jus de fruit. Été dafa nex je jure ! Lakk dieun yi fi, fruit de mer yi neulei...
Nakala togué di lekk sama ndiabane maad, un petit garçon vient à moi tenant une tasse de thé.-Tenez me dit-il
-Moi ?
J'étais étonnée dii-Oui vous ! C'est mon oncle qui m'a dit de vous le donner !
Wa ki foum ma hamei ba di ma hélil ataya ? Diamono bou doy war bi
-Ah bon c'est gentil mais dites lui que je ne bois pas du thé. Merci quand même.
Nakala xalebi tourné rek pour delou si tonton bi sama camarade de classe bi Amina woko
-Donne moi la tasse de thé, kou nanoul mane damay naane.
Xalei bi obéissant ba deh diokh ko tasse bi dem, mou nei fourekh tasse bi guessou néma am demal délo djiko.
Anhhh pardoon , ngani, mouniiii ?
Kii bane effet lako ataya bi def ?-Amina douma sa morom. Kou naane ataya bi dou iow ?
-Waw maane miii mako naane wayei yaw yay kikay yobou nakk
-Wa ba lolou dess si...
-Bayil yi ngay def diougueul yobou liiii. Imagine ma dem yobou tasse bi nane merci ta ken khélilou mako wone ! Bobou guathié. Démal rek yobou ko cherie s'il te plaît. Gno far iow..
-Fallait y penser à deux avant de le boire. Mane sama yone nekoussi. Nanouma nanatouma
- Diap si rek iow tamiitt tass bi nak faw mou delou ki dakay sokhla pour continuer ataya bi
-M'en fou moi, et puis bouma yakal sama lekk maad han...
-wa légui faisons une chose. On n'y va ensemble pour yobb tass bii . Comprend moi nak meunou mafa débarquer comme ça mane rek...
-ya xaam deh. C'est ton probleme
-Ayy naar bou rafet, sama dom ndey de cœur...
Nehal na ba sonou, ndeysane moudié nako yeureum. Xaral ma diap si rek sinon dou bax

VOUS LISEZ
tankk bukki
RomanceTankk Bukki histoire bo xamnei la mo ngui am si diganetei bén couple. Fatimétou mi ngui si netali nimou xamaneté ak borom keureum, ay mbegtè wam ak ay nakaram. mou mel ni sax lolou moy mandargay nobel. Digantè bo guiss amna ay hauts ak ay bas. sass...