quand Hitler voulait bombarder dakar

854 85 7
                                    

Lou douff thi nagg bi xadioul thi tshinne bi wayé Serigne Babacar Sy thia diamonom pour nga xam wilayam Serigne Mounirou Sarr wakh nako.
Serigne Babacar Sy néna man déh bouma roussoul wone Maodo kouma wo thi photo nima Babacar Sy ma wouyoula. Wayé rouss na Seydil Hadj Malick Sy meussouko déf kone doumako déf. Motax am kou nieuw niko ya souteuh Seydil Hadj Malick sa baay Serigne Babacar Sy né tékk bamou yagg néko anhakay ma souteuh Maodo wadji niko si nane, Serigne Babacar Sy néko parce que Maodo moma toungom té koula toungom nga souteuh ko kone migui ko beugone dougeul thi gam motax wakh thi sa Serigne lo xamni yagui yakarni yagui kay tappal gratte néké yagui kay dégradé.
Moukou wakhal cii sa Serigne lou beutt ték beutt, wakhal cii sa Serigne Lou génération féké. Motax thia diamono De Gaulle ak Hitler thia 39-45 dafa né tay damay bombardé dji Sénégal ndakh nga xam wiilaya Serigne Babacar Sy. Xolal bamou diougué, nieuw thi Serigne Babacar Sy niko gawal bo gawoul fii ak 5h thi ngone
Sénégal dina nek doomeuh xolal Hitler lamou naar.
Serigne Babacar Sy né meunoumalén djité thi diaka yii dilén djité thi kheul yii...dieul ayy makk yébal leen thia zawiya ba xolal Seydou Nourou Tall thiala bok, Elhaj Mouhamadou Mansour bayou Serigne Babacar Sy Mansour thiala bokou ak makk gnogné bagnou nieuwé Serigne Babacar Sy nélé souguén démé naguén diangue niane yii nguén xamni dioubonamak yallah. Niou nieuw ni ahh Serigne Babacar Sy niane bi la diokhé wone ni Allahouma Itlite Hitler wa hetlite Hitler wa damiroune tahbililah mou naw thia diaweu thia avion Hitler daldini hii fii ma dieum thi Sénégal diko bombardé dji amna nuage bou dokh sama digganté ak pays bobou meunatouma avancé il faut que je fasse demi-tour. Gouverneur général nieuw thi Serigne Babacar Sy niko accepté nagnou loutax gnouni yay Cheikh al Khalifa, bou lettre meussana diougué thia bitim réw thia diamonoy Serigne Babacar Sy gnou adressé si à remettre à Khalifa général tel wala Khalifa tel ken douko nango recevoir loudoul da diar thi Serigne Babacar mou khol ko souko momoul mouni momou mako gnou daldi kay diokh kénén kako mom mais fok mou nieuk diar si mom.
Lolou motax Serigne Babacar Sy, gouverneur général nieuw niko waw kay yaw yay Cheikh al Khalifa accepté nagnou.
On l'appelait le Cheikh Al Khalifa c'est-à-dire le Khalifa de tout les Khalifa gnouniko ahh mouni l'homme au bonnet carré, au manteau vert et au sourire légendaire lui c'est Serigne Babacar Sy ahakay Serigne Babacar Sy xolal pour l'anecdote c'est le Mbaye des apprentis de Car rapide ce bout de fer accroché au toil auxquels on agrippé pour ne pas tomber lui c'est Serigne Babacar Sy. Lolou motax Serigne Babacar Sy wadja thia diamonom Serigne Mounirou dioundiounako thia wilaya gaa lolou kou amoul wilaya meunoko.
Wadji né ah Serigne Babacar Sy néna mom kouko guiss dina xam sa tourr, xam sa tourou ndey xam sa tourou baay man meussouma dem tivaouane xawma Serigne Babacar Sy jakarlo wougnou tay nak dina dem ba xam ndakh deugg lam détt wilayaga.
Andeuh thia foul ba bagnou diougué dakar dem tivaouane bignou nieuwé ba dioub Serigne Babacar Sy wadji bokou thi rang bi rk nieuw nieuw nieuw ba diokh Serigne Babacar Sy lokhom, Serigne Babacar Sy né yalakh lokho ba mou dial foul bi diékh.
Mou daldi dem rang wate si guinaw mou nieuwat diokh Serigne Babacar Sy lokho ba Serigne Babacar Sy né yalakh lokho ba mou dem né ah Serigne Babacar Sy ligni wakh si koumou guiss xam la nékou thia xel ma dh.
Troisième fois bi mou nieuw diokh Serigne Babacar lokho beugg rothi Babacar Sy dab dabal lokho ba niko nikk teuyé néko diiw xamna lila andi, diiw domou diiw ak diiw, xolal lolou nga done ladj loutax bingama gneuké nouyou wakhou mala ko ndakh dolé thia barii na ba soumalako wakhone brusquement nga fatu.
Yonou niarel bi nga nieuw ma bayi sa lokho boumalako wakhone nga kheum ndakh dolé thia dose ba diékhoul.
Niétél ba nak ma teuyé sa lokho xamal lani man Babacar Sy sangue wégn way dokh thia tach-tachara moy diourom niarélou souff youkou ga dérétte thia namouy dokhé thia yaram ba migui may tankal fi man Babacar Sy niko yalakh.
Lolou motax Serigne Babacar Sy pour tout gatal moy boko toudé thia wilayaga yangay lambatou lo xamni xamo famou dayo thia yallah diap ko thi Serigne Cheikh Seydi Mouhamadou Moustapha Sy Djamil fi thi fass. Motax archives national lolou bo démé dinga fa fékk lii motax wadji khol ko bamou yagg néko "mbaye yagnou doy, Mbaye yagnou doy Seydi Aboubacar Bacary dara mam Sy yagnou doy do sen morom bour yallah ni Mamadou Abdallah do sen morom yonnén néna Cheikh Tidiane Shérif do sen morom, Cheikh néna Maodo Sy yama doy do sen morom Maodo guérsou Khalifa niko yama doyy do sen morom Khalifa guérsou Sora niko yama doyy do sen morom Khalifa guérsou Abdou niko yama doyy do sen morom Abdou guérsou Sora niko yama doyy do sen morom Sora guérsou Cheikh niko yama doyy do sen morom diafa ndoulen si Mbaye diafa ndou nagnou si Mbaye ninga len meuné nonou nga len gueuné."

Cheikhal Khalifa Ababacar Sy (RTA). Chef spirituel au charisme légendaireOù les histoires vivent. Découvrez maintenant