🌴 *WAXI SËRIÑ TUUBA* 🌴

409 29 3
                                    

🌴 *WAXI SËRIÑ TUUBA* 🌴
-------------
💫 Amna tubaab bu mëssë lajj SËRIÑ TUUBA niko: ñaata talibé nga am ? SËRIÑ BI niko: kuy jublu péncu ! Muni ko waxu ma loolu ndax Xaadr ak Tiijaan daa am, may lajj yaw ñaata talibé nga am ? SËRIÑ BI niko: li tax ma waxla loolu  mooy kuy jublu péncu bu dee ñaan, budul sun Barké YALLAH du nangu lamuy ñaan. Ku mel noonu nak buko yëggee ak buko yëggul sab talibé la
---------
📚 *Source: waxtaani SËRIÑ TUUBA, VOL2*

Waxi Serigne ToubaOù les histoires vivent. Découvrez maintenant