14❤️

3.4K 408 4
                                    

Trois jours de cela les hommes construisent notre maison. Mais ils n'ont pas fini , chérif est venu une fois pour voir comment marche le travail.

Ndiatté: djank khaliss bi louniou si deif?

Moi: cheuveux la beug djeundd th sanii sama frisé bii

Ndiatté: amna bouma guiss 25milles bou rafett marché

Moi: est ce que doumako djeundd tmt

Ndiatté: dess na ci iow bvby.

17h niou deim marché, Ndiatté mom djeundd na ayy yeurém. Mane sama cheveux bou bakhh.

Mère yacine: waa yene folene nekone?

Moi: marché tata

Mère yacine: chérif yakk nalene

Ndiatté: khana, hii leyssa wouyoul chérif sakh

Appel téléphonique avec chérif.

Lui: mon amour

Moi: oui nakamou?

Lui: dila nam rek

Moi: quand même arrête tes enfantillages là

Lui: serieux !

Moi: kone nekhna!

Lui: sama yaye ak sama rakk niofa wara nieuw guanaw soubeuh

Moi: hii chérif tu joue à quoi là

Lui: je te préviens rek

Moi: ok, tu me parle jamais de ton père.

Lui: il a divorcé avec ma mère.

Moi: massa!

Lui: avec ma mère je ne réclame pas l'amour paternel. Je l'aime ma mère

Moi: c'est bien ciao.

Ndiatté: loumou wakhatii?

Moi: il vient avec sa famille après demain

Mère adji: kane chérif ?

Moi: ouii

Mere adji: wawaw kone leyssa pareil bok nga wané saye féme

Ndiatté: khana

Leyssa: thieuy mane!

Naka laniiuy wakhé nonou rek, niou guiss auto bou reuyy takhaw limou wathié nak souma ko done lim douma paré, riz, sucre, café, lait, condiment, biscuits, huile, farine, œufs, viandes, poissons et tout.

Mère adji: ayy wayy kene dou chérif

Mère yacine: kikay borom doolé la

Les voisins sont là à commérer, ils ne savent toujours pas pourquoi on a déménagé et pourquoi on reconstruit notre maison. Mais bon ça m'est t'égale. De toute façon faut s'occuper de ses oignons.

Mère adji: leyssa! Leyssa!

Moi: waw!

Mère adji: j'ai à te parler

Moi: waw yaye mangui degglou

Mère adji: leyssa dama woo sa yaye yacine mii nga khamnii mom lala ndayalé mou teiwei limalay wakh. Leyssa dara oumpou la si li chérif diniou deiffal th mounounio tass yakaram. Certes il viendra avec ces parents mais avant ça je veux que tu réfléchis. Chérif mom lagn lay maye kham ko tay nak.

Mère yacine: la décision nous revient nous tes parents. Comme niko sa yaye wakhé rek kii lou bakh lala beugueuul motakh niouy deiff lii yeup

Moi: ngaine balma dh! Mais seuyouma ciao!

Je sors et je me mets à pleurer. Je voulais pas que chérif fait tous ça je le voulais faire moi même.

Mère adji: wa yacine lii loussouy pékhé kii ma guiss ni dh seuyiwoul

Mère yacine: j'ai une idée...

Mère adji: laquelle?

   ____________________

Quelle idée?🥰

Ne pas être vierge ?Où les histoires vivent. Découvrez maintenant