8

73 12 2
                                    


Je vous passe jusqu'au week-end. Il ne s'était rien passé depuis et c'est mieux comme ça.

C'est l'heure d'aller prendre le petit déjeuner donc je prends ma douche m'habille et descend pour rejoindre les autres

Moi: Asalamoualeykoum comment vous allez

Hakeem: héy la grosse

Maman: on va bien alkhamdoulilah et toi tu as bien dormi

Moi: oui oui cv

Il y'avait que ma mére et Hakeem qui m'ont répondu les autres étaient sur leurs téléphones à faire je ne sais quoi . C'est bizzare parceque d'habitude heurou ndéki si escalier yi nguey tolou dégue ay youkhou ay rétane ay wéranté wayé insbi ma ngui melni kou nék si décés. Li ma si gueuneu méti moy ma nouyou kéneu falé wouma à part sama yaye ak Hakeem. Fatima mom mo ngui si kaw khamna légui mou wathie.
Humm en tout cas dal doyna war trop.

Maïmouna: *rire en regardant son tél*

Elle leve la tête et me vois enfin avant de me dire

Elle: wa ioe kagne ngua nieuw té nouyo wo sah

Moi: enn kone ya ngui méy dogua guiss ok.

Elle: mohh ioe lane la ba diam déjà ya ngui wathie nouyo wo di am loy wah

Moi: wouyou ma Maïmouna dimbali ma est ce que ya ngui dégue dafa tél beuguou ma béneu tiow té bouguouma la dépassé nak

Elle: yaw kane nguey wahal ni kholal Malika douma sa morom dh wahnala ko nak na ngua modoré sa language réw ngua trop

Moi: *rire nerveux * yaw mayma sama diam dingueu fi la nouyo kéneu falé wouma à part maman ak Hakeem kone nak boulma wah wahi impolitesse parceque fi yaw ya fi impoli

Elle: ÉHHH K.....

Maman: ÉHHH BOU LEINE NIOU SONALE ENH EST CE QUE YENA NGUI MÉY DÉGUE . Li lane la ni lou xéw si keur gui . Li moussoul am si keur gui kone nak dou tay nguéne ko fi indi .

Maïmouna: maman m...

Maman: yaw doul ya gueuneu niak diom nieup imbécile bi kou la fék fi nguéy khoulo ak sa rakk khawma loumou léy wah niak diom ba dé. Fi leu nieuw wathie nouyo kéneu falé wouko nguéne seugue séne téléphones yi di melni ay deum you guiss yapp kone nak amo leine lo leine di wah thipppp *en se levant de sa chaise pour partir*

Moi: pardon maman

Elle: se n'est rien chérie ne t'inquiète pas tu n'es pas la fautive ici au contraire c'est eux *en montant les escaliers*

Hakeem: war nguéne kholat ni nguene mél fane yi dh heure bi dawone na fék niouy wahtane di tognaneté mais légui heurou ndéki kéneu dou wah nieup da niouy seug séne call yi ba diam tmt *il se léve de sa chaise et part*

Moi: khawma lou leine dal insbi mais ressaisissez
*en me levant pour partir*

Pov Elhadj

Cc je suis le frére de Malika

Breff je ne sais pas ce qui vient de se passer là mais c'est chaud. En même temps ils ont raisons. Je me surprend carrément parceque de base je suis quelqu'un qui aime beaucoup discuté avec mes fréres ou les taquiner mais là rien chaque instant je suis sur mon téléphone ces temps ci tout ça à cause de la fille de monsieur thiam. OUI la fille de monsieur thiam avec qui je flirt depuis 8 jours maintenant. Oui je sais que c'est vite mais je n'y peut rien elle m'attire comme un émant cette meuf je ne sais pas ce qu'elle m'a fait.

Moi: ahh yéne maman wahna deugue dh nioune gni nak nio ngui abusé li ba diam la

Maïmouna: mohh ioe gni nguéy déglou Elhadj nioune defou niou dara lou graw dh wahtane tmt c'est pas forcé dh

Zahra: mane je sais pas mais ils ont un peu raison nak temps yi mom da niou leine bayi trop naniou diéma wagni call yi touti

Moussa: ahh mo gueune dh

Moi: mo gueune kéy mane mom Maïmouna khawma fane yi loula dal mais na ngua réglé wahna lako nak .

Elle: wa yaw mane lane l....

Moi: déguo ma dh mané ngua réglé fofou la yém nak

Retour dans la peau de Maleyka

J'était assise avec Fatima dans la chambre elle dit qu'elle ne va pas bien qu'elle a mal au ventre. Je discutais un peu avec elle je lui ai tout raconté elle était tellement choqué . Elle se demandait comment celà a pût  arrivé à notre famille

Moi: mane dh do titt ba rawma

Elle: sétlou wo fane yi si titt la niou deuk *rire*

Moi: nioune kéy *rire*

Soudain mon téléphone se met à sonner je vois un numéro non enregistré . Mais qui sa peut bien être?

Fatima: boy do wouyou ki léy wo mo ngui insisté rk

Moi: khawma numéro bi di té deuk bi woratoul *rire*

Elle: *rire* wa wouyou ko rk peut être que c'est important.

Moi : wa d'accord

Je répond

Moi: allô

??: oui c'est Malika?

Moi: oui c'est moi vous êtes qui ?

??: c'est.............










                          Moussa

Oups ! Cette image n'est pas conforme à nos directives de contenu. Afin de continuer la publication, veuillez la retirer ou mettre en ligne une autre image.

                          Moussa




Votez et abonnez vous svp ❤

~Dans Les Abysses~Où les histoires vivent. Découvrez maintenant