9

73 15 3
                                    

??: c'est khadija Thiam la fille de mr Thiam

Moi: ahh d'accord comment tu vas *en regardant ma soeur , on était un peu surpris *

Khadija: je vais trés bien alkhamdoulilah et toi j'éspére que je ne t'ai pas dérangé

Moi: non tu ne me dérange pas

Elle: ahh kone bakhna . Dama la beuguone invité yaw , Fatima ak zahra niou dém léki glace et tout

Moi: ahh wei *un peu choqué*

Fatima: *en chuchotant* moi j'accepte

Khadija: allô tu es toujours là?

Moi: euhhh oui oui je suis là mais à propos de ta proposition je ne sais pas si on va pouvoir venir

Fatima: *en chuchotant* da ngua nane yaw ya beuguoul dém wayé boul mass "on" bi melni mala né beuguou ma dém

Khadija: ahh bon pourquoi ? Da am lou xéw khana

Moi: non dara xéwoul wayé prométrou mala dara fi ak souba dina la wah souniou decision parceque il faut que niou taguou parents yi aussi (ma meune féne dh kalandakh)

Elle: d'accord je comprends kone lou si am rk ngua wo ma dingueu

Moi: waw amoul beneu probléme boy coupé may enregistré numéro bi inchaallah

Elle: waw bye

Moi: bye *et je raccroche * thippppp

Fatima: loutax ngua kéy thipatou yaw méti ngua dh elle t'a juste proposé de faire une petite sortie

Moi: dou dara nak mane ma beuguoul am béneu lien ak niom

Elle:  mais li ngua deff ni niaw na trop boula yébo ngua wowat ko néko ON accepte ok?

Moi: douma k...

Elle: déguoma dh mané tout de suite

Moi: yaw mom da ngua soff troop thimm

J'appelle Khadija pour confirmer notre sortie.

POV: Maïmouna

Aujourd'hui je n'avais pas cours du coup je suis allé au travail et vers 16h30 je descend . Je sortais de mon lieu de travail quand je vois Mouhamed adossé sur une voiture. Je me dirige vers lui .

Moi: wa yaw loy deff fi Mouhamed.

Lui: wa doma nouyou ba paré. Té ngua bayi dima wowé Mouhamed wahnala ko ba soneu

Moi: ahh khana dou nonou ngua toudou

Lui: non pour ioe c'est soit ay bébé wala mon amour yama gueneu kham dal genrou tour yoyou wayé bala ma dé rk mouné ma mouhamed sou fékone sah avec douceur nguamay wowé niou khawa négocié wayé ioe sa wahine mo agressif.

Moi: so yakaré ma wowé la nonou dh di ngua dé parceque MOUHAMED lay continué di wah que sa te plaise ou non

Lui: ahh wei tu veux jouer à ça ok on va joué *sourire au coin* bon yégueul niou dém léki glace

Moi: sa tombe bien sah dama khawa xiff

Lui: nél da ngua xiff rk mo gueune yomb *rire*

Moi: dama xiff kone *rire*

Lui: kone key nieuweul niou dém sama appart niou togueu lou néx mo gueune di dém ay restaut nadj bou tangue bi

Moi: humm non merci kay niou dém leki glace kone

Lui: héy dara dou fa xéw ok naniou dém sama keur rk comme ça ngua khamalé fa sah

Moi: *un peu hésitante* wa d'accord

~Dans Les Abysses~Où les histoires vivent. Découvrez maintenant