Aujourd'hui c'est vendredi et j'ai décidé de porter ⬇️⬇️⬇️
Et voilà ma coiffure toute simple toute mignonne.
Je descend à la cuisine pour prendre mon petite déjeuné je vois Maïmouna Fatima et Zahra entrain de mangé
Moi: bonjour
Eux: bonjour
Fatima: yaw batay cas woma no moudié si entreprise bi dh
Moi: yaw yama abandonné dém di teudi ak Zahra
Ces temps-ci Zahra était un peu souffrante donc Fatima qui est sa jumelle est partit dans leur chambre pour veillé sur elle alors que y'a Maïmouna dans la chambre mdr
Fatima: mane abandonné wouma la dh tay rk ma nieuwat si nék bi
Moi: humm ma ngui léy khar *en ouvrant le frigo*
Maïmouna : wa yaw Malika khana da am louma la déff
Moi: non *sec*
Elle: kone loutax soma rombé da nguéy melni khamo ma souma la togné ngua wah ma
Moi: amouma louma léy wah ioe sah kham ngua ni je suis trop rancunière souma diapé rk douma bayi té kérok ni ngua ma déff néxouma que ça soit la premiére et la dernière fois ngua méy youkhou si kanamou nitt yi ngua nék sama mak niak nék sama mak la si yémalé . Té lou ma gueuneu déff ay ré si histoire bi moy tu avait tord mais tu a voulût tout me jeté à la face .
Elle: je te demande pardon mane khawma wone ni affaire bi toleu nala fofou je m'excuse vraiment . Pour te dire mane sah khawma lane moma dal temps yi mais bou leine mako diapé yéne samay rakk nguéne vous êtes ma famille et je vous aime beaucoup
Moi: *rire* humm tu as intérêt
On se fait un câlin collectif tous les quatres je les aimes tellement mes soeurs que Dieu me les préserve.
Moi: bon les filles mane je doit aller au taf dama fa am cas bou reuy li ma féy fék tay souma gnibi si wé en vie rk diam la
Fatima: humm li motax mani waho ma lépp ioe *rire*
VOUS LISEZ
~Dans Les Abysses~
FanfictionDeux familles, deux ambiances. La joie, le bonheur règnent dans la premiere. Le mystère règne dans le second. Entre amour, haine, tromperie, mystére, trahison, cette histoire qui englobe beaucoup d'émotions vous emportera loin