Pov de coudy ( la maman de Malika)
Ce que les enfants m'ont dit m'a vraiment surpris et à vrai dire ça me fait peur parceque je connais la personne qui a mit ce truc dans les toilettes et je peux juré qu'elle ne s'arrêtera pas là. Aujourd'hui je décide d'aller voir un marabout aprés la descente. Il me dira la signification de ce truc bizzare.
Donc aprés la descente j'appelle Astou la petite soeur de mon mari , qui était venu nous voir l'autre jour.
Appel téléphonique 📞
Moi: wathial ma ngui ni sa bountou keur gawal way
Elle: ma ngui ni di nieuw souma nieuwé ngua expliqué ma lépp nak parceque ya ngui méy titeul mane
Moi: waw wathial rk ioe.
Appel terminé
Queslques minutes aprés elle arrive et monte dans la voiture . Je démarre direct
Elle: tite na té khawma lane mo xéw
Moi: * je lui explique*
Elle: *rire nerveux* lolou mom kéneu rk la meune done té kham ngua ko sah
Moi: mane kéy kham nani mom la . Mane kéy damay bagne dara dal sama dom yi Astou . Lolou rk lay ragal mais da melni kéneu diotoul wone togue si chaise anglaise bi
Elle: héy calme toi dara dou leine dal ok . Insbi founiouy dém si pa dimbalé ?
Moi: waw fofou la beugue dém mou léralal ma affaire bi loumouy signifié
Elle: waw mo gueune sah
1h plutard nous somme arrivées dans les lieux.
On rentre dans la maison et on voit Pa Dimbalé qui nous demande de rentré .
Quelques minutes aprés lui avoir tout raconté.
Pa Dimbalé: coudy diokh ma affaire bi nékone si chaise anglaise bi
Ma guéneu affaire bi si sama sac ma diokh ko. Il commence à récité je ne sais quoi dessus 2 minutes aprés il termine
Pas dimbalé: coudy kham ngua kane mo dougueul li sa keur wala
Moi: ahh sama xél amna koumou méy diokh wayé worouma ndax mom la wala
Pa dimbalé: ahh ki la déff li dal khamal ni koula diégué la wone wayé yéne niar da nguéne dém ba am ay probléme yéne niar
Moi: kome kima khalat la
Pa dimbalé: guiss ngua limou dougueul sa birr toilettes kéneu bou toguone si chaise anglaise bi déyy doff wala dou meuneuti am dom
Astou: alakhouakbar
Pa Dimbalé: mais heureusement sa dom bou goor bi da am sourat bou am puissance boumou si tari lolou mo khawa wagni ndieurigniou galathie bi wayé taxoul mou todj dh
Moi: légui nane la wara déff bamou todj.
Pa dimbalé: bayil mako fi dina si déff louma meune bamou todj mais dina la diokh béneu bouteille boy wiss si toilettes khalé yi pour mou protégé leine . Boufa kéneu douguou tant que motoul 24h dingueu
Moi: éy way merci papa dimbalé . Am li mala ko diokh *en lui tendant quelques billets de dix milles francs
Pa dimbalé: téyél sa khaliss bi ngua dintieu ko parceque soxla wouma ko sama dom
Moi: dieuleul rk papa dimbalé soxla wouma ko en plus li xéb nako sah
Pa dimbalé: kham ngua dou lépp la meune wah . Té ioe sama dom ngua warouma la féyé kou lépp louma déff rk sa Papa mi ngua khamni sama kharit sama lépp la wone motax
Moi: ahh lolou mom deugue leu wayé nak souma sanione ngua dieul ko
Pa dimbalé: téyé ko rk kham na lima la wah. Té ma wahla nak guiss ngua ki dougueul li sa keur défal trés attention si mom ak ay domam nak parceque liy wadia xéw sa keur yeup niom nio kéy causé
Moi: pa dimbalé li nguey wah ni gueune nama titeul
Pa dimbale: boul am loy tite tant que ma ngui fi dara doula dal ioe ak sa ndiabot . Dieuleul bouteille bi wiss ko si toilettes bi bénéne bi si néguou khalé yi ngua kéy wiss dingueu? Néguou khalé yeup la wah nak. Té boul khalatati lolou guéné si sa xél bayil lépp si lokho yallah
Moi: waw dina ko déff inchaallah nio ngui dém dieureudieuf papa
Pa dimbalé: yonou diam
Pendant le trajet personne n'osait parlé. Mais Astou mom ngua khamni lamigne bi la mounoul téyé fo diar mou wah
Elle: wa coudy tite na pour khalé yi
Moi: kone dh khawma mane nouma déff.
Elle: grawoul naniou gueum yallah rk dara dou leine dal inchaallah.
Soudain mo téléphone sonne. Je regarde et vois que c'est un numéro masqué je demande à astou de le connecté à la voiture puis de décrocher.
Appel téléphonique 📞
Moi: allo
??: wa domou ndéye
Moi: kokou kane la
??: ahh khamé wo sa batou meilleure amie khana *rire tellement fort*
Moi: ioe mouno ma méy sama diam khana. Mouno am diom ngua bayi ma comme nima ko déffé wala lolou mounoul nék
??: bayi diam kone déyy yomb di yaw nguéy réy katou nitt ma léyy bayi *rire* yaw dh di ngua khamni bandit wo sah mala gueuneu doff fouf
Moi: *rire nerveux* yaw da melni da ngua ma faté wala ma fatéli la may kane . Kham ngua yaw dofo djiné diapou la réyy sa nde****e légui lay déff wax bi close
??: éy way chérie ya ngui waxé xol dh ndank rk yaw commencé guouma di *rire* yaw dh di ngua khamni kéneu douma togne ba paré di si guéné nonou khalatouma ko sah
Moi: IOE MERDE EST CE QUE YA NGUI MÉY DÉGUEU YAW LANE MOY SA PROBLÉME ENN?
??: chérie boul youkhou yaw tmt *rire*
Moi: kham ngua lane la gueuneu regretté sama adouna moy lima la khamé souma sagnone souniou yone dou meusseu tassé.
Et je raccroche
Astou me regarde et comprit vite à qui je parlais.J'arrive à la maison vers 20h . Astou je l'ai déposé chez elle.
Le coup de fil que j'ai reçu elle m'a vraiment fait peur . Non j'ai pas peur pour moi, mais pour mes enfants qui sont mes raisons de vivre. Je sais ce que cette femme est capable de faire et je peux juré qu'elle ne va pas y aller de main morte
Pendant le dîné les enfants faisaient que de me regardé. Ça se voyait sur mon visage que quelque chose n'allait pas.
Elhadj: wa yaye tay séddeu ngua dh lou xéww chérie de mon coeur *rire*
Moi: *sourire forcé* c'est rien cherie
Je tourne mon visage et vois Malika qui me regardait avec un regard insistant. C'eat la plus intelligente de mes enfants . Les autres aussi sont intelligent surtout Hakeem mais elle......... elle peut lire en toi, et quand tu vas pas bien les autres ne vont pas pouvoir le savoir mais elle elle peut deviné direct ce qui ne va pas . C'est aussi ma confidente.
Malika: maman?
Moi: ce n'est rien mon coeur aller mangé sinon ça va refroidir
Vers 23h📍
On était couché moi et Maleyka sur le lit . Elle était couché sur ma poitrine et a entouré ses mains sur ma taille. Je lui caressait sa tête
Elle: maman tay ba kham ngua ni tu vas tout me raconté
Moi: ahhh tu ne me laisse pas le choix là?
Elle: oui tu as tout compris
Moi: *souffle* mais je te dirais rien aller couche toi et oubli tout ok
Elle: enn nonou ngua ko guissé wa baxna ba souba kone
Votez et abonnez vous svp merciii et bisouss💋
VOUS LISEZ
~Dans Les Abysses~
Fiksi PenggemarDeux familles, deux ambiances. La joie, le bonheur règnent dans la premiere. Le mystère règne dans le second. Entre amour, haine, tromperie, mystére, trahison, cette histoire qui englobe beaucoup d'émotions vous emportera loin