16

3.5K 237 3
                                    

Salam aleykum

Sila déme sama chambre sangou diapou dioulli dieule sama téléphone fékk fa ay message Mounass ak Virginie ak bénde Inconnu
Sila tontou mounas ak Virginie mais message Inconnu bi tontou mako
Maye wadia tékk sama téléphone guiss appel numéro Inconnu

Moi: louma dalle taye aye numéro Inconnu rk laye guiss kharal ma dieul rk mo gueuneu wore

Sila décroché appel bi

Conversation téléphonique

...Allô sœur

Moi: Allô cki

...kone khamé wo soune voix kone

Moi: hum kharal makhole ah adama ak awa

...gnoune la kaye iow kagne ngagnou guedieu guiss bagnouy faté

Moi: billahi dou lolou dama léne guedia dégue rk baguéne damé Canada bataye dégatouma léne

Awa: kharal ma défko appelle vidéo

Gnou déf ko appelle vidéo

Moi: oh mes amours namone naléne nake

Adama : billahi gnola raw dagnou la meuno tone woh  téléphone rk

Moi: lolou kaye loutakh kénne wowouma  telephone diéme naléne wo wayé séne numéro yi dokhoul

Awa: dagnon changé numéro iow teh pp mo wakh boune la wo teh 3mois you gneukk matoul

Moi: lolou takh dégouma sama yy ak Bachir done n'a wakh sakh dagne ma beugatoul

Adama : kénn bagnoul seulement que pp mo gnouy contrôlé rk monéh féh 3 moi you gneukk yi matoul bouko kénn wo dagno sathie wola sakh ndakh dagne la namou

Moi: maléne raw naka fofou migui nekh

Awa: fi nékhoul dara pp dagnouy teuthie rk kénne dou guénde

Moi: aye waye matesa

Adama : guiss nga Fatou fi iow rk fi manqui ana kiné mome

Moi: légui rk ma gneuw 6 mois yagoul kiné migui fi di beuri wakh

Awa: kiné kaye doumasa changé mome sakh mogni tanéh ndakh amna liberté

Moi: même si k sou amoul sakh ame n'a liberté lolo takh gnounane l' argent ne fait pas le bonheur

Adama : mane souma sagnone sama keur tanta laye deukk fi nékhoul dara dagay teudiou rk

Awa: khana bougnouy diangui rk lagni guénde wara gnou yondi gnou

Moi: fih deh mome nekhna dagay kénde di déf shopping di déme sortie

Awa : iow daga ame lo démé sortie wala shopping

Moi: non amoumako wayé sama tanta mogui gnouy diokh doneté 2000f la sakh teh mane gnimay andal gnomay dieundal wayé souma amé damaléne di faye

Adama : kane ngaye andale khana wokho Mounass ak evachou gnonou kaye khamna doune la bayi ngaye toumaraké

Moi: wawaw ak Virginie domou ministre bi

Awa: lane dale ngathie dh khame nga domou ministre bi

Moi: wawaw  ministre bi sakh nêna makoy wowé oncle

Adama : lolou la wakh b...

Ma dégue bénéne voix sama voix pp laye nourol

Moi: kokou kanela

Awa: sikanam sama pp taye gnou dh

Moi: w..

Bipp

Fin de conversation

Si lane raccroché téléphone bi sama pp khamouma loutakh mou bagne gnou surtout mane

Kiné crie : Fatou

Moi: lanela dagay beunde sama tympan yi

Kiné : depuis des minutes malay wo wayé dégoma loukhéw

Moi: dou dara seulement k dama namou soune wakeur

Kiné : lolou motakh ngay triste doléne wo téléphone

Moi: sankh rk lama awa ak Adama di woh nênagne sama pp moléne wakhe bou kéne wo Fatou teh trois mois you gneukk yi dialoul

Kiné : hun 3 mois beurri n'a dh sa pp ndakh nitela

Moi: dafma bagne rk billahi temps yi sakh mangui def effort pour mou beugue ma wayé dara

Kiné : lolou kénne douko wakh sa pp bagnoula sa djiko rk la bagne teh fatél lolou iow yaye Fatou nake waro di triste réwal ma khole

Moi sourire : iow do nit koi mais je t'aime

Kiné : moi aussi sama yy gneuwna dh momela la done doyé

Moi: wa mangui nieuw

____

Moi: tanta nkm

Sama tanta: mangui fi naka ecole taye nekhna

Moi: ecole migui ni rk

Tanta : kiné démal mayema ndokh

  Kine déme

Moi: tt ba domou ministre bi sonaloula dafa arrogant dh

Tanta : kane ngathie wakhal

Moi: Abdou la wakh

Tanta :  kane Abdou arrogant woule dh da beuriwoul wakh rk wayé nonou la bakhé

Loutakh gnounane abdou dafa bakh teh wanoumalo

Tanta : lanela loukhew

Moi sourire : dara mangui déme sama chambre diangui samay leçon dagniy déf devoir math souba

Tanta : si kanam kone naga gor gorou dh
(Crie )  kiné loye déf si wagne bi bamala gnonené bataye

Kine : mangui gneuw ndokh mi mo congélé makoy wathié

Ma yékk si kaw diangue sama leçon yi

Moi: Quoi !!!

A suivre

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Où les histoires vivent. Découvrez maintenant